Al-A'la · 7/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'la
إِلَّا مَا شَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ وَمَا يَخْفَىٰ ۝٧
Illaa maa shaaa`al laah; innahoo ya`lamul jahra wa maa yakhfaa
📖 Tekkim Wolof
lu dul la soob Yàlla. Moom moo xam li feeñ ak li nëbbu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-A'la

5فَجَعَلَهُ غُثَاءً أَحْوَىٰ
di ko naatal dëlël ko.
6سَنُقْرِئُكَ فَلَا تَنسَىٰ
Dananu la jàngal (Alxuraan), te doo too ko fàtte
7إِلَّا مَا شَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ وَمَا يَخْفَىٰ
lu dul la soob Yàlla. Moom moo xam li feeñ ak li nëbbu.
8وَنُيَسِّرُكَ لِلْيُسْرَىٰ
Dananu la jàppandalal yoon wi gëna yomb.
9فَذَكِّرْ إِن نَّفَعَتِ الذِّكْرَىٰ
Na ngay fàttelee, saa su fàtteli amee njariñ.
Al-A'laFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-A'la 7

Simoore Al-A'la Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lu dul la soob Yàlla. Moom moo xam li feeñ…

Simoore Aaya 7/19 — Simoore Al-A'la الأعلى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'la Dégg, Simoore Al-A'la Tekki, Simoore Al-A'la mp3, Simoore Al-A'la pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers