At-Tawba · 114/129
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tawba
وَمَا كَانَ اسْتِغْفَارُ إِبْرَاهِيمَ لِأَبِيهِ إِلَّا عَن مَّوْعِدَةٍ وَعَدَهَا إِيَّاهُ فَلَمَّا تَبَيَّنَ لَهُ أَنَّهُ عَدُوٌّ لِّلَّهِ تَبَرَّأَ مِنْهُ ۚ إِنَّ إِبْرَاهِيمَ لَأَوَّاهٌ حَلِيمٌ ۝١١٤
Wa maa kaanas tighfaaru ibraaheema li abeehi illaa `ammaw `idatinw wa `adahaaa iyyaahu falammaa tabaiyana lahooo annahoo `aduwwul lillaahi tabarra a minh; inna Ibraaheema la awwaahum haleem
📖 Tekkim Wolof
Te it jéggalu ga Ibraayiima doon jéggalul baayam, du utoon dara lu dul ab dig bu mu ko digoon. (Waaye), ba mu ko leeree ne noonub Yàlla la (moom baayam), dafa deñ ba set wecc ci loolu. Ibraahiima ab delluwaakoon la ci Boroomam, ku lewet la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 112-116 — Simoore At-Tawba

112التَّائِبُونَ الْعَابِدُونَ الْحَامِدُونَ السَّائِحُونَ الرَّاكِعُونَ السَّاجِدُونَ الْآمِرُونَ بِالْمَعْرُوفِ وَالنَّاهُونَ عَنِ الْمُنكَرِ وَالْحَافِظُونَ لِحُدُودِ اللَّهِ ۗ وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ
(Ñooña) ñuy tuub lañu, di ñuy jaamu Yàlla, di Ko sant, di ñuy woor, di lunku di sujjóot (julli), di digle lu baax, di tere lu bon, di wattu dëeli Yàlla yi (daytal)... bégalal ña gëm.
113مَا كَانَ لِلنَّبِيِّ وَالَّذِينَ آمَنُوا أَن يَسْتَغْفِرُوا لِلْمُشْرِكِينَ وَلَوْ كَانُوا أُولِي قُرْبَىٰ مِن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمْ أَنَّهُمْ أَصْحَابُ الْجَحِيمِ
Yellul ci Yonent bi ak ñi gëm ñuy baalul bokkaalekat yi, doonte la sax mbokk lañu ginnaaw ba mu leen biree ne ñoom ñuy dugg Safara lañu.
114وَمَا كَانَ اسْتِغْفَارُ إِبْرَاهِيمَ لِأَبِيهِ إِلَّا عَن مَّوْعِدَةٍ وَعَدَهَا إِيَّاهُ فَلَمَّا تَبَيَّنَ لَهُ أَنَّهُ عَدُوٌّ لِّلَّهِ تَبَرَّأَ مِنْهُ ۚ إِنَّ إِبْرَاهِيمَ لَأَوَّاهٌ حَلِيمٌ
Te it jéggalu ga Ibraayiima doon jéggalul baayam, du utoon dara lu dul ab dig bu mu ko digoon. (Waaye), ba mu ko leeree ne noonub Yàlla la (moom baayam), dafa deñ ba set wecc ci loolu. Ibraahiima ab delluwaakoon la ci Boroomam, ku lewet la.
115وَمَا كَانَ اللَّهُ لِيُضِلَّ قَوْمًا بَعْدَ إِذْ هَدَاهُمْ حَتَّىٰ يُبَيِّنَ لَهُم مَّا يَتَّقُونَ ۚ إِنَّ اللَّهَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Yàlla du bàyyi ñoo xam ne gindi na leen ba noppi ñuy tàbbiwaat cig réer, te leeralal na leen la ñu war a ragal. Yàlla xam na lépp.
116إِنَّ اللَّهَ لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ يُحْيِي وَيُمِيتُ ۚ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ
Yàllaa moom nguurug asamaan yi ak suuf si. Mooy dundal, di rey. Te amuleen wéeruwaay walla ku leen mën a dimbali ku dul Moom (Yàlla).
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
114Aaya

Tekki — At-Tawba 114

Simoore At-Tawba Aaya 114 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it jéggalu ga Ibraayiima doon jéggalul baayam, du utoon…

Simoore Aaya 114/129 — Simoore At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tawba Dégg, Simoore At-Tawba Tekki, Simoore At-Tawba mp3, Simoore At-Tawba pdf. Aaya 112–116. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers