At-Tawba · 27/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
ثُمَّ يَتُوبُ اللَّهُ مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ عَلَىٰ مَن يَشَاءُ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ ٢٧
Transliteration
Summa yatoobul laahu mim ba`di zaalika `alaa mai yashaaa`; wallaahu Ghafoorur Raheem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mujj Yàlla jéggal ku Ko neex ginnaaw ga, ndax Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 25-29 — At-Tawba
25لَقَدْ نَصَرَكُمُ اللَّهُ فِي مَوَاطِنَ كَثِيرَةٍ ۙ وَيَوْمَ حُنَيْنٍ ۙ إِذْ أَعْجَبَتْكُمْ كَثْرَتُكُمْ فَلَمْ تُغْنِ عَنكُمْ شَيْئًا وَضَاقَتْ عَلَيْكُمُ الْأَرْضُ بِمَا رَحُبَتْ ثُمَّ وَلَّيْتُم مُّدْبِرِينَ
Yàlla dimbali na leen ci barab yu bari. Ak ca bisu (xareb) Hunayni ba ngeen yéemoo ca nangeen baree woon te jariñuleen dara. Ba li suuf si di yaatu, lépp xat na keroog ci yéen ; ngeen wëlbatiku daw.
26ثُمَّ أَنزَلَ اللَّهُ سَكِينَتَهُ عَلَىٰ رَسُولِهِ وَعَلَى الْمُؤْمِنِينَ وَأَنزَلَ جُنُودًا لَّمْ تَرَوْهَا وَعَذَّبَ الَّذِينَ كَفَرُوا ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ الْكَافِرِينَ
Ginnaaw ga, Yàlla wàcce dalam ga ca Yonentam ba ak ca ñu gëm ña. Mu wàcce xarekat yu ngeen gisul ak mbugalu ña weddi. Loolu mooy peyu yéefar ya.
27ثُمَّ يَتُوبُ اللَّهُ مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ عَلَىٰ مَن يَشَاءُ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Mujj Yàlla jéggal ku Ko neex ginnaaw ga, ndax Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
28يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِنَّمَا الْمُشْرِكُونَ نَجَسٌ فَلَا يَقْرَبُوا الْمَسْجِدَ الْحَرَامَ بَعْدَ عَامِهِمْ هَٰذَا ۚ وَإِنْ خِفْتُمْ عَيْلَةً فَسَوْفَ يُغْنِيكُمُ اللَّهُ مِن فَضْلِهِ إِن شَاءَ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Bokkaalekat ya nekkuñu lu dul sobe : buñu jege Jàkka ju ñu wormaal ja, ginnaaw seen at mii. Bu ngeen ragalee nag Yàlla, Dana leen may kon ci ngënéelam bu ko soobee. Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
29قَاتِلُوا الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَلَا بِالْيَوْمِ الْآخِرِ وَلَا يُحَرِّمُونَ مَا حَرَّمَ اللَّهُ وَرَسُولُهُ وَلَا يَدِينُونَ دِينَ الْحَقِّ مِنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ حَتَّىٰ يُعْطُوا الْجِزْيَةَ عَن يَدٍ وَهُمْ صَاغِرُونَ
Xareleen ak ñi gëmul Yàlla ak Bis-pénc ba, te duñu araamal la Yàlla ak Yonentam ba araamal ak ña dul diinewoo diine ju dëggu ja, ca ña jotoon Téere, [xareleen ak ñoom] ba ba ñuy joxe seen bopp cig mokk, di ñu toroxlu.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
27Aaya
Tekki — At-Tawba 27
Simoore At-Tawba Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mujj Yàlla jéggal ku Ko neex ginnaaw ga, ndax Yàlla…Simoore Aaya 27/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







