Al-Layl · 12/21
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Layl
إِنَّ عَلَيْنَا لَلْهُدَىٰ ۝١٢
Inna `alainaa lal hudaa
📖 Tekkim Wolof
Gindee, nun la war ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Layl

10فَسَنُيَسِّرُهُ لِلْعُسْرَىٰ
Dananu ko jàppandalal yoon wu jafe wa,
11وَمَا يُغْنِي عَنْهُ مَالُهُ إِذَا تَرَدَّىٰ
te alalam du ko jariñ dara saa su ñu ko mbaqee (Safara).
12إِنَّ عَلَيْنَا لَلْهُدَىٰ
Gindee, nun la war ;
13وَإِنَّ لَنَا لَلْآخِرَةَ وَالْأُولَىٰ
te Noo moom, dundug àddinaak àllaaxira.
14فَأَنذَرْتُكُمْ نَارًا تَلَظَّىٰ
Xuppnaa leen ci Safara wuy bérëx-bérëxi
Al-LaylFihi Alxuraan
21Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Layl 12

Simoore Al-Layl Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gindee, nun la war ;

Simoore Aaya 12/21 — Simoore Al-Layl الليل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Layl Dégg, Simoore Al-Layl Tekki, Simoore Al-Layl mp3, Simoore Al-Layl pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers