Al-Layl · 11/21
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Layl
وَمَا يُغْنِي عَنْهُ مَالُهُ إِذَا تَرَدَّىٰ ۝١١
Wa maa yughnee `anhu maaluhooo izaa taraddaa
📖 Tekkim Wolof
te alalam du ko jariñ dara saa su ñu ko mbaqee (Safara).

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Layl

9وَكَذَّبَ بِالْحُسْنَىٰ
te muy weddi yoolub àllaaxira,
10فَسَنُيَسِّرُهُ لِلْعُسْرَىٰ
Dananu ko jàppandalal yoon wu jafe wa,
11وَمَا يُغْنِي عَنْهُ مَالُهُ إِذَا تَرَدَّىٰ
te alalam du ko jariñ dara saa su ñu ko mbaqee (Safara).
12إِنَّ عَلَيْنَا لَلْهُدَىٰ
Gindee, nun la war ;
13وَإِنَّ لَنَا لَلْآخِرَةَ وَالْأُولَىٰ
te Noo moom, dundug àddinaak àllaaxira.
Al-LaylFihi Alxuraan
21Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Layl 11

Simoore Al-Layl Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te alalam du ko jariñ dara saa su ñu ko…

Simoore Aaya 11/21 — Simoore Al-Layl الليل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Layl Dégg, Simoore Al-Layl Tekki, Simoore Al-Layl mp3, Simoore Al-Layl pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers