Al-'Alaq · 4/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Alaq
الَّذِي عَلَّمَ بِالْقَلَمِ ۝٤
Al lazee `allama bil qalam
📖 Tekkim Wolof
mooy kiy xamle ci xalima [mbind],

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-'Alaq

2خَلَقَ الْإِنسَانَ مِنْ عَلَقٍ
moo bind nit ci lumbu deret.
3اقْرَأْ وَرَبُّكَ الْأَكْرَمُ
Jàngal ! Sa Boroom mooy ki gëna tedd,
4الَّذِي عَلَّمَ بِالْقَلَمِ
mooy kiy xamle ci xalima [mbind],
5عَلَّمَ الْإِنسَانَ مَا لَمْ يَعْلَمْ
moo xamal nit lamu xamut woon.
6كَلَّا إِنَّ الْإِنسَانَ لَيَطْغَىٰ
Waaye nit kat dafay bew,
Al-'AlaqFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-'Alaq 4

Simoore Al-'Alaq Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mooy kiy xamle ci xalima [mbind],

Simoore Aaya 4/19 — Simoore Al-'Alaq العلق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Alaq Dégg, Simoore Al-'Alaq Tekki, Simoore Al-'Alaq mp3, Simoore Al-'Alaq pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers