Al-'Alaq · 3/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Alaq
اقْرَأْ وَرَبُّكَ الْأَكْرَمُ ۝٣
Iqra wa rab bukal akram
📖 Tekkim Wolof
Jàngal ! Sa Boroom mooy ki gëna tedd,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-'Alaq

1اقْرَأْ بِاسْمِ رَبِّكَ الَّذِي خَلَقَ
Jàngal, ci sa turu Boroom biy bind,
2خَلَقَ الْإِنسَانَ مِنْ عَلَقٍ
moo bind nit ci lumbu deret.
3اقْرَأْ وَرَبُّكَ الْأَكْرَمُ
Jàngal ! Sa Boroom mooy ki gëna tedd,
4الَّذِي عَلَّمَ بِالْقَلَمِ
mooy kiy xamle ci xalima [mbind],
5عَلَّمَ الْإِنسَانَ مَا لَمْ يَعْلَمْ
moo xamal nit lamu xamut woon.
Al-'AlaqFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-'Alaq 3

Simoore Al-'Alaq Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jàngal ! Sa Boroom mooy ki gëna tedd,

Simoore Aaya 3/19 — Simoore Al-'Alaq العلق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Alaq Dégg, Simoore Al-'Alaq Tekki, Simoore Al-'Alaq mp3, Simoore Al-'Alaq pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers