Yunus · 74/109
Tekki Waxtaan — Yunus
ثُمَّ بَعَثْنَا مِن بَعْدِهِ رُسُلًا إِلَىٰ قَوْمِهِمْ فَجَاءُوهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَمَا كَانُوا لِيُؤْمِنُوا بِمَا كَذَّبُوا بِهِ مِن قَبْلُ ۚ كَذَٰلِكَ نَطْبَعُ عَلَىٰ قُلُوبِ الْمُعْتَدِينَ ۝٧٤
Summma ba`asnaa mim ba`dihee Rusulan ilaa qawmihim fajaaa`oohum bilbaiyinaati famaa kaanoo liyu`minoo bimaa kazzaboo bihee min qabl; kazaalika natba`u `alaa quloobil mu`tadeen
📖 Tekkim Wolof
Topp nu yónni ginnaawam ay Yonent ci seenu nit. Nu indil leen ay lay yu leer. Waaye nekkuñu woon di way-gëm la ñu weddi woon ca bu jëkk. Ba noonu Lanu tëjee ràpp xoli ña jéggi woon dayo, daan jalgati.

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Yunus

72فَإِن تَوَلَّيْتُمْ فَمَا سَأَلْتُكُم مِّنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَى اللَّهِ ۖ وَأُمِرْتُ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْمُسْلِمِينَ
Bu ngeen dëddoo, xamleen ne laajumaleen ag pey... Samag pey nekkul fenn fu dul fa Yàlla. Te digaleef na ma ma bokk ca way-jébbalu ña”.
73فَكَذَّبُوهُ فَنَجَّيْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ فِي الْفُلْكِ وَجَعَلْنَاهُمْ خَلَائِفَ وَأَغْرَقْنَا الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُنذَرِينَ
Ñu weddi ko. Nu musal ko mook ña ànd ak moom ca gaal ga, Nu def leen ñuy ñay wuutu [nit ña ci kaw suuf si]. Nu labal ña weddi sunuy ndigal. Nanga xool nag ña ñu waaroon [ca ña weddi], ni seen mujj deme !
74ثُمَّ بَعَثْنَا مِن بَعْدِهِ رُسُلًا إِلَىٰ قَوْمِهِمْ فَجَاءُوهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَمَا كَانُوا لِيُؤْمِنُوا بِمَا كَذَّبُوا بِهِ مِن قَبْلُ ۚ كَذَٰلِكَ نَطْبَعُ عَلَىٰ قُلُوبِ الْمُعْتَدِينَ
Topp nu yónni ginnaawam ay Yonent ci seenu nit. Nu indil leen ay lay yu leer. Waaye nekkuñu woon di way-gëm la ñu weddi woon ca bu jëkk. Ba noonu Lanu tëjee ràpp xoli ña jéggi woon dayo, daan jalgati.
75ثُمَّ بَعَثْنَا مِن بَعْدِهِم مُّوسَىٰ وَهَارُونَ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ بِآيَاتِنَا فَاسْتَكْبَرُوا وَكَانُوا قَوْمًا مُّجْرِمِينَ
Topp Nu yónni ci seen ginnaaw Muusaa ak Haaroona ca [Firawna] ak mbooloo ma [ñu xamal leen] sunuy ndigal. Ñu rëy-rëylu, di aw nit ñu dëng [diy saay-saay].
76فَلَمَّا جَاءَهُمُ الْحَقُّ مِنْ عِندِنَا قَالُوا إِنَّ هَٰذَا لَسِحْرٌ مُّبِينٌ
Ba dëgg ga agsee ca ñoom tukkee ci Nun Yàlla, [ñu ne leen] : “Jibar tigi la ! ”.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Yunus 74

Simoore Yunus Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp nu yónni ginnaawam ay Yonent ci seenu nit. Nu…

Simoore Aaya 74/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers