Yusuf · 4/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
إِذْ قَالَ يُوسُفُ لِأَبِيهِ يَا أَبَتِ إِنِّي رَأَيْتُ أَحَدَ عَشَرَ كَوْكَبًا وَالشَّمْسَ وَالْقَمَرَ رَأَيْتُهُمْ لِي سَاجِدِينَ ۝٤
Iz qaala Yoosufu li abeehi yaaa abati innee ra aytu ahada `ashara kawkabanw wash shamsa walqamara ra aytuhum lee saajideen
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikul] ba Yuusufa waxee baayam ne ko : "Yaw sama baay, man gis naa [ci gént] fukki bindiw ak ñaar ak jant bi ak weer wi ; ñu may sujjóotal”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 2-6 — Yusuf

2إِنَّا أَنزَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لَّعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Wàcce Nanu ko mu di ay njàng ci làkku [araab] ngir ngeen xam la mu tekki.
3نَحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ أَحْسَنَ الْقَصَصِ بِمَا أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ هَٰذَا الْقُرْآنَ وَإِن كُنتَ مِن قَبْلِهِ لَمِنَ الْغَافِلِينَ
Nun noo ngi lay nettali gën jaa rafeti nettaliin ci Alxuraan jii Nu la xamal te lu ko jiitu nekkoon na loo réere.
4إِذْ قَالَ يُوسُفُ لِأَبِيهِ يَا أَبَتِ إِنِّي رَأَيْتُ أَحَدَ عَشَرَ كَوْكَبًا وَالشَّمْسَ وَالْقَمَرَ رَأَيْتُهُمْ لِي سَاجِدِينَ
[Fàttalikul] ba Yuusufa waxee baayam ne ko : "Yaw sama baay, man gis naa [ci gént] fukki bindiw ak ñaar ak jant bi ak weer wi ; ñu may sujjóotal”.
5قَالَ يَا بُنَيَّ لَا تَقْصُصْ رُؤْيَاكَ عَلَىٰ إِخْوَتِكَ فَيَكِيدُوا لَكَ كَيْدًا ۖ إِنَّ الشَّيْطَانَ لِلْإِنسَانِ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Mu ne ko : "Yaw sama doom, bul nettali sa gént gi say doomi-baay, [boo leen ko nettalee], danañu la fexeel am pexe ; ndax Séytaane noonub nit la bu tar ag nooneel.
6وَكَذَٰلِكَ يَجْتَبِيكَ رَبُّكَ وَيُعَلِّمُكَ مِن تَأْوِيلِ الْأَحَادِيثِ وَيُتِمُّ نِعْمَتَهُ عَلَيْكَ وَعَلَىٰ آلِ يَعْقُوبَ كَمَا أَتَمَّهَا عَلَىٰ أَبَوَيْكَ مِن قَبْلُ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْحَاقَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Kem [ni nga génte], sa Boroom dana la tànn te Dana la xamal pirim gént, te Dana matal ci yaw ay xéewalam ak njabootu Yanqooba, ni Mu ko matalee woon bu jëkk ca sa ñaari maam ya, Ibraahiima ak Isaaqa, sa Boroom nag ku xam la, ku xereñ la”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Yusuf 4

Simoore Yusuf Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikul] ba Yuusufa waxee baayam ne ko : "Yaw sama…

Simoore Aaya 4/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers