Yusuf · 3/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
نَحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ أَحْسَنَ الْقَصَصِ بِمَا أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ هَٰذَا الْقُرْآنَ وَإِن كُنتَ مِن قَبْلِهِ لَمِنَ الْغَافِلِينَ ٣
Transliteration
Nahnu naqussu `alaika ahsanal qasasi bimaaa awhainaaa ilaika haazal quraana wa in kunta min qablihee laminal ghaafileen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nun noo ngi lay nettali gën jaa rafeti nettaliin ci Alxuraan jii Nu la xamal te lu ko jiitu nekkoon na loo réere.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 1-5 — Yusuf
1الر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْمُبِينِ
Alif, Laam, Raa. Lii ay xamle la yu nekk ci Téere bu wér péŋŋ bi.
2إِنَّا أَنزَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لَّعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Wàcce Nanu ko mu di ay njàng ci làkku [araab] ngir ngeen xam la mu tekki.
3نَحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ أَحْسَنَ الْقَصَصِ بِمَا أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ هَٰذَا الْقُرْآنَ وَإِن كُنتَ مِن قَبْلِهِ لَمِنَ الْغَافِلِينَ
Nun noo ngi lay nettali gën jaa rafeti nettaliin ci Alxuraan jii Nu la xamal te lu ko jiitu nekkoon na loo réere.
4إِذْ قَالَ يُوسُفُ لِأَبِيهِ يَا أَبَتِ إِنِّي رَأَيْتُ أَحَدَ عَشَرَ كَوْكَبًا وَالشَّمْسَ وَالْقَمَرَ رَأَيْتُهُمْ لِي سَاجِدِينَ
[Fàttalikul] ba Yuusufa waxee baayam ne ko : "Yaw sama baay, man gis naa [ci gént] fukki bindiw ak ñaar ak jant bi ak weer wi ; ñu may sujjóotal”.
5قَالَ يَا بُنَيَّ لَا تَقْصُصْ رُؤْيَاكَ عَلَىٰ إِخْوَتِكَ فَيَكِيدُوا لَكَ كَيْدًا ۖ إِنَّ الشَّيْطَانَ لِلْإِنسَانِ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Mu ne ko : "Yaw sama doom, bul nettali sa gént gi say doomi-baay, [boo leen ko nettalee], danañu la fexeel am pexe ; ndax Séytaane noonub nit la bu tar ag nooneel.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
3Aaya
Tekki — Yusuf 3
Simoore Yusuf Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun noo ngi lay nettali gën jaa rafeti nettaliin ci…Simoore Aaya 3/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








