Yusuf · 72/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قَالُوا نَفْقِدُ صُوَاعَ الْمَلِكِ وَلِمَن جَاءَ بِهِ حِمْلُ بَعِيرٍ وَأَنَا بِهِ زَعِيمٌ ۝٧٢
Qaaloo nafqidu suwaa`al maliki wa liman jaaa`a bihee himlu ba`eerinw wa ana bihee za`eem
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Li nu réerle mooy nattukaayu buur bi. Te ku ko feeñal nu jox ko sëfu giléem, maa ko warlul loolu”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 70-74 — Simoore Yusuf

70فَلَمَّا جَهَّزَهُم بِجَهَازِهِمْ جَعَلَ السِّقَايَةَ فِي رَحْلِ أَخِيهِ ثُمَّ أَذَّنَ مُؤَذِّنٌ أَيَّتُهَا الْعِيرُ إِنَّكُمْ لَسَارِقُونَ
Ba mu leen solalee seeni saaku ba noppi, mu dugal andaar [ja ñu doon natte] ca biir sëfu doomu-ndeyam ja. Mu am yéglekat bu wax ne : “Éy yéen jëgg ji ! Ay sàcc ngeen”.
71قَالُوا وَأَقْبَلُوا عَلَيْهِم مَّاذَا تَفْقِدُونَ
Ñoom it ñu wëlbatiku ca moom ne leen : “Lan ngeen réerle ? ”
72قَالُوا نَفْقِدُ صُوَاعَ الْمَلِكِ وَلِمَن جَاءَ بِهِ حِمْلُ بَعِيرٍ وَأَنَا بِهِ زَعِيمٌ
Ñu ne : “Li nu réerle mooy nattukaayu buur bi. Te ku ko feeñal nu jox ko sëfu giléem, maa ko warlul loolu”.
73قَالُوا تَاللَّهِ لَقَدْ عَلِمْتُم مَّا جِئْنَا لِنُفْسِدَ فِي الْأَرْضِ وَمَا كُنَّا سَارِقِينَ
Ñu ne : “Giñ nanu ci Yàlla, te xam ngeen ne dikkunu fii ci suuf si ngir yàq te it dunu ay sàcckat”.
74قَالُوا فَمَا جَزَاؤُهُ إِن كُنتُمْ كَاذِبِينَ
- Ñu ne: “Luy peyug ku sàcc, bu fekkee dangeen a fen ?”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — Yusuf 72

Simoore Yusuf Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Li nu réerle mooy nattukaayu buur bi.…

Simoore Aaya 72/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers