An-Nahl · 100/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
إِنَّمَا سُلْطَانُهُ عَلَى الَّذِينَ يَتَوَلَّوْنَهُ وَالَّذِينَ هُم بِهِ مُشْرِكُونَ ۝١٠٠
Innnamaa sultaanuhoo `alal lazeena yatawallawnahoo wallazeena hum bihee mushrikoon
📖 Tekkim Wolof
Ña mu mënal dara ci kàttanam du kenn ñu dul ña féetewook moom Séytaane ak ña koy bokkaaleek [Yàlla].

🎧 Dégg


📜 Aaya 98-102 — Simoore An-Nahl

98فَإِذَا قَرَأْتَ الْقُرْآنَ فَاسْتَعِذْ بِاللَّهِ مِنَ الشَّيْطَانِ الرَّجِيمِ
Booy jàng Alxuraan, nanga muslu ci Yàlla Mu musal la ci Séytaane su ñu rëbb sa.
99إِنَّهُ لَيْسَ لَهُ سُلْطَانٌ عَلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
Naka Séytaane du am genn kàttan ci [yàqal] ña gëm te wéeru ci seen Boroom.
100إِنَّمَا سُلْطَانُهُ عَلَى الَّذِينَ يَتَوَلَّوْنَهُ وَالَّذِينَ هُم بِهِ مُشْرِكُونَ
Ña mu mënal dara ci kàttanam du kenn ñu dul ña féetewook moom Séytaane ak ña koy bokkaaleek [Yàlla].
101وَإِذَا بَدَّلْنَا آيَةً مَّكَانَ آيَةٍ ۙ وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُنَزِّلُ قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مُفْتَرٍ ۚ بَلْ أَكْثَرُهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bu ñu weccee jenn laaya, def jeneen laaya fa mu nekkoon - te Yàllaa gën a xam la Muy wàcce - ñuy wax naan : “Nekkuloo lu dul duurkat”. Déet, li ëpp ci ñoom xamuñu.
102قُلْ نَزَّلَهُ رُوحُ الْقُدُسِ مِن رَّبِّكَ بِالْحَقِّ لِيُثَبِّتَ الَّذِينَ آمَنُوا وَهُدًى وَبُشْرَىٰ لِلْمُسْلِمِينَ
Neel : “Ruu gu sell gaa ko wàcce mu jóge ci lu dëggu ngir mu dëgëral ñi gëm, muy luy gindee, di luy bégal jullit ñi.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
100Aaya

Tekki — An-Nahl 100

Simoore An-Nahl Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña mu mënal dara ci kàttanam du kenn ñu dul…

Simoore Aaya 100/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers