An-Nahl · 99/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
إِنَّهُ لَيْسَ لَهُ سُلْطَانٌ عَلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ ۝٩٩
Innahoo laisa lahoo sultaanun `alal lazeena aamanoo wa `alaa Rabbihim yatawakkaloon
📖 Tekkim Wolof
Naka Séytaane du am genn kàttan ci [yàqal] ña gëm te wéeru ci seen Boroom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 97-101 — An-Nahl

97مَنْ عَمِلَ صَالِحًا مِّن ذَكَرٍ أَوْ أُنثَىٰ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَلَنُحْيِيَنَّهُ حَيَاةً طَيِّبَةً ۖ وَلَنَجْزِيَنَّهُمْ أَجْرَهُم بِأَحْسَنِ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Ku jëf u yiw, di ku góor walla ku jigéen te muy ku gëm, fàwwu Dananu ko dundal dundu gu sell. Te fàwwu Dananu leen fey seenug pey na mu gën a rafete la ñu nekkoon di ko jëf.
98فَإِذَا قَرَأْتَ الْقُرْآنَ فَاسْتَعِذْ بِاللَّهِ مِنَ الشَّيْطَانِ الرَّجِيمِ
Booy jàng Alxuraan, nanga muslu ci Yàlla Mu musal la ci Séytaane su ñu rëbb sa.
99إِنَّهُ لَيْسَ لَهُ سُلْطَانٌ عَلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
Naka Séytaane du am genn kàttan ci [yàqal] ña gëm te wéeru ci seen Boroom.
100إِنَّمَا سُلْطَانُهُ عَلَى الَّذِينَ يَتَوَلَّوْنَهُ وَالَّذِينَ هُم بِهِ مُشْرِكُونَ
Ña mu mënal dara ci kàttanam du kenn ñu dul ña féetewook moom Séytaane ak ña koy bokkaaleek [Yàlla].
101وَإِذَا بَدَّلْنَا آيَةً مَّكَانَ آيَةٍ ۙ وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُنَزِّلُ قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مُفْتَرٍ ۚ بَلْ أَكْثَرُهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bu ñu weccee jenn laaya, def jeneen laaya fa mu nekkoon - te Yàllaa gën a xam la Muy wàcce - ñuy wax naan : “Nekkuloo lu dul duurkat”. Déet, li ëpp ci ñoom xamuñu.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
99Aaya

Tekki — An-Nahl 99

Simoore An-Nahl Aaya 99 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka Séytaane du am genn kàttan ci [yàqal] ña gëm…

Simoore Aaya 99/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 97–101. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers