An-Nahl · 3/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِالْحَقِّ ۚ تَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ ۝٣
Khalaqas samaawaati wal arda bilhaqq; Ta`aalaa `ammaa yushrikoon
📖 Tekkim Wolof
Moo bind asamaan yi ak suuf si ci dëgg. Kawe na, sori lool la ñu koy bokkaale.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-5 — An-Nahl

1أَتَىٰ أَمْرُ اللَّهِ فَلَا تَسْتَعْجِلُوهُ ۚ سُبْحَانَهُ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Mbirum Yàlla jege na. Buleen ko yàkkamti. Sellam ga màgg na ! Te kawe na, sori lañu koy bokkaale.
2يُنَزِّلُ الْمَلَائِكَةَ بِالرُّوحِ مِنْ أَمْرِهِ عَلَىٰ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ أَنْ أَنذِرُوا أَنَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا أَنَا فَاتَّقُونِ
Mooy wàcce ay Malaaka yuy ànd ak ug soloo, ciy ndigalam, jox ko ku ko soob ci ay jaamam, neeleen : “Nangeen waare ci xamle ne amul jeneen Yàlla ju dul Man. Ragal-leen Ma”.
3خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِالْحَقِّ ۚ تَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Moo bind asamaan yi ak suuf si ci dëgg. Kawe na, sori lool la ñu koy bokkaale.
4خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Moo bind nit ñi ci toqent ; te moom [nit] mu nekk di pànk mu mën a xuloo.
5وَالْأَنْعَامَ خَلَقَهَا ۗ لَكُمْ فِيهَا دِفْءٌ وَمَنَافِعُ وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
[Moo bind it] mala yi, ngeen di ca jële ay yére yu nuggu ak yeneen njariñ. Ak lu ngeen di lekk.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — An-Nahl 3

Simoore An-Nahl Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo bind asamaan yi ak suuf si ci dëgg. Kawe…

Simoore Aaya 3/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers