An-Nahl · 4/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ ۝٤
Khalaqal insaana min nutfatin fa izaa huwa khaseemum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Moo bind nit ñi ci toqent ; te moom [nit] mu nekk di pànk mu mën a xuloo.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore An-Nahl

2يُنَزِّلُ الْمَلَائِكَةَ بِالرُّوحِ مِنْ أَمْرِهِ عَلَىٰ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ أَنْ أَنذِرُوا أَنَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا أَنَا فَاتَّقُونِ
Mooy wàcce ay Malaaka yuy ànd ak ug soloo, ciy ndigalam, jox ko ku ko soob ci ay jaamam, neeleen : “Nangeen waare ci xamle ne amul jeneen Yàlla ju dul Man. Ragal-leen Ma”.
3خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِالْحَقِّ ۚ تَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Moo bind asamaan yi ak suuf si ci dëgg. Kawe na, sori lool la ñu koy bokkaale.
4خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Moo bind nit ñi ci toqent ; te moom [nit] mu nekk di pànk mu mën a xuloo.
5وَالْأَنْعَامَ خَلَقَهَا ۗ لَكُمْ فِيهَا دِفْءٌ وَمَنَافِعُ وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
[Moo bind it] mala yi, ngeen di ca jële ay yére yu nuggu ak yeneen njariñ. Ak lu ngeen di lekk.
6وَلَكُمْ فِيهَا جَمَالٌ حِينَ تُرِيحُونَ وَحِينَ تَسْرَحُونَ
Te it yéen a ngi bànneexu ci seeni taar bu ngeen di jofal ci ngoon ak bu ngeen di wëtal ci suba.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — An-Nahl 4

Simoore An-Nahl Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo bind nit ñi ci toqent ; te moom [nit]…

Simoore Aaya 4/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers