Al-Isra · 45/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
وَإِذَا قَرَأْتَ الْقُرْآنَ جَعَلْنَا بَيْنَكَ وَبَيْنَ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ حِجَابًا مَّسْتُورًا ۝٤٥
Wa izaa qaraatal Quraana ja`alnaa bainaka wa bainal lazeena laa yu`minoona bil aakhirati hijaabam mastooraa
📖 Tekkim Wolof
Booy jàng Alxuraan, Dananu def ci sa diggante ak ñi gëmul àllaaxira kiiraay lu nëbbu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Isra

43سُبْحَانَهُ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يَقُولُونَ عُلُوًّا كَبِيرًا
Cëy sellam ga ! Kawe na, jomb na li ñuy wax, jombute gu màgg a màgg !
44تُسَبِّحُ لَهُ السَّمَاوَاتُ السَّبْعُ وَالْأَرْضُ وَمَن فِيهِنَّ ۚ وَإِن مِّن شَيْءٍ إِلَّا يُسَبِّحُ بِحَمْدِهِ وَلَٰكِن لَّا تَفْقَهُونَ تَسْبِيحَهُمْ ۗ إِنَّهُ كَانَ حَلِيمًا غَفُورًا
Juróom-ñaari asamaan yi ak suuf si, ñi ngi koy sàbbaal, ak li nekk ci seen biir. Te sax amul dara lu nekk te du Ko sàbbaal ci li Mu yeyoo mboolem cant. Waaye dangeen a amul dégg-dégg ci seeni sàbbaal. Naka Moom Aji-lewet la, Jéggalaakoon la.
45وَإِذَا قَرَأْتَ الْقُرْآنَ جَعَلْنَا بَيْنَكَ وَبَيْنَ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ حِجَابًا مَّسْتُورًا
Booy jàng Alxuraan, Dananu def ci sa diggante ak ñi gëmul àllaaxira kiiraay lu nëbbu,
46وَجَعَلْنَا عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ أَكِنَّةً أَن يَفْقَهُوهُ وَفِي آذَانِهِمْ وَقْرًا ۚ وَإِذَا ذَكَرْتَ رَبَّكَ فِي الْقُرْآنِ وَحْدَهُ وَلَّوْا عَلَىٰ أَدْبَارِهِمْ نُفُورًا
Nu def ci seeni xol muuraay ba duñu ca am dégg-dégg : te nekk na ci seeni nopp ab daaj. Te booy tudd sa Boroom moom doŋŋ ci Alxuraan, ñu dëddu, foñ.
47نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَسْتَمِعُونَ بِهِ إِذْ يَسْتَمِعُونَ إِلَيْكَ وَإِذْ هُمْ نَجْوَىٰ إِذْ يَقُولُ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا
Nun noo gën a xam li ñuy dégg bu ñu lay déglu. Ak bu ñuy déeytoo ci wax ñoom tooñkat ya : “Toppuñu lu dul as waay su ñu jibar”.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Isra 45

Simoore Al-Isra Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Booy jàng Alxuraan, Dananu def ci sa diggante ak ñi…

Simoore Aaya 45/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers