Al-Isra · 74/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
وَلَوْلَا أَن ثَبَّتْنَاكَ لَقَدْ كِدتَّ تَرْكَنُ إِلَيْهِمْ شَيْئًا قَلِيلًا ۝٧٤
Wa law laaa an sabbatnaaka laqad kitta tarkanu ilaihim sha`an qaleela
📖 Tekkim Wolof
Te bu Nu la dëgaralul woon, tuuti kon nga xaw a jeng jëm ci ñoom

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Simoore Al-Isra

72وَمَن كَانَ فِي هَٰذِهِ أَعْمَىٰ فَهُوَ فِي الْآخِرَةِ أَعْمَىٰ وَأَضَلُّ سَبِيلًا
Ku nekkoon gumba ci àddina si, dana wéye gumba ca àllaaxira, te gën a réer, sori yoonu njub wa.
73وَإِن كَادُوا لَيَفْتِنُونَكَ عَنِ الَّذِي أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ لِتَفْتَرِيَ عَلَيْنَا غَيْرَهُ ۖ وَإِذًا لَّاتَّخَذُوكَ خَلِيلًا
Xaw nañu laa fitnaal ba nga bàyyi la Nu la xamal, ngir nga duur lu wuuteek moom. Kon ñu jàppe la xarit ñoom yéefar yi.
74وَلَوْلَا أَن ثَبَّتْنَاكَ لَقَدْ كِدتَّ تَرْكَنُ إِلَيْهِمْ شَيْئًا قَلِيلًا
Te bu Nu la dëgaralul woon, tuuti kon nga xaw a jeng jëm ci ñoom
75إِذًا لَّأَذَقْنَاكَ ضِعْفَ الْحَيَاةِ وَضِعْفَ الْمَمَاتِ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ عَلَيْنَا نَصِيرًا
Te kon Dananu la mosal mbugali àddina ak mbugali àllaaxira; te doo am ku la dimbali ci Nun.
76وَإِن كَادُوا لَيَسْتَفِزُّونَكَ مِنَ الْأَرْضِ لِيُخْرِجُوكَ مِنْهَا ۖ وَإِذًا لَّا يَلْبَثُونَ خِلَافَكَ إِلَّا قَلِيلًا
Te xaw nañu laa génne ca suuf sa [suufi Madiina] ngir ñu jële la fa. Te kon duñu fa toog lu dul diir bu néew ci sa ginnaw. [alag leen].
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Al-Isra 74

Simoore Al-Isra Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te bu Nu la dëgaralul woon, tuuti kon nga xaw…

Simoore Aaya 74/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers