Al-Isra · 75/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
إِذًا لَّأَذَقْنَاكَ ضِعْفَ الْحَيَاةِ وَضِعْفَ الْمَمَاتِ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ عَلَيْنَا نَصِيرًا ۝٧٥
Izal la azaqnaaka di`falhayaati wa di`fal mamaati summa laa tajidu laka `alainaa naseeraa
📖 Tekkim Wolof
Te kon Dananu la mosal mbugali àddina ak mbugali àllaaxira; te doo am ku la dimbali ci Nun.

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-77 — Simoore Al-Isra

73وَإِن كَادُوا لَيَفْتِنُونَكَ عَنِ الَّذِي أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ لِتَفْتَرِيَ عَلَيْنَا غَيْرَهُ ۖ وَإِذًا لَّاتَّخَذُوكَ خَلِيلًا
Xaw nañu laa fitnaal ba nga bàyyi la Nu la xamal, ngir nga duur lu wuuteek moom. Kon ñu jàppe la xarit ñoom yéefar yi.
74وَلَوْلَا أَن ثَبَّتْنَاكَ لَقَدْ كِدتَّ تَرْكَنُ إِلَيْهِمْ شَيْئًا قَلِيلًا
Te bu Nu la dëgaralul woon, tuuti kon nga xaw a jeng jëm ci ñoom
75إِذًا لَّأَذَقْنَاكَ ضِعْفَ الْحَيَاةِ وَضِعْفَ الْمَمَاتِ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ عَلَيْنَا نَصِيرًا
Te kon Dananu la mosal mbugali àddina ak mbugali àllaaxira; te doo am ku la dimbali ci Nun.
76وَإِن كَادُوا لَيَسْتَفِزُّونَكَ مِنَ الْأَرْضِ لِيُخْرِجُوكَ مِنْهَا ۖ وَإِذًا لَّا يَلْبَثُونَ خِلَافَكَ إِلَّا قَلِيلًا
Te xaw nañu laa génne ca suuf sa [suufi Madiina] ngir ñu jële la fa. Te kon duñu fa toog lu dul diir bu néew ci sa ginnaw. [alag leen].
77سُنَّةَ مَن قَدْ أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ مِن رُّسُلِنَا ۖ وَلَا تَجِدُ لِسُنَّتِنَا تَحْوِيلًا
Loolu aada la ca ña Nu yónni woon la la jiitu ci Sunuy Yonent. Te doo gis lu soppiku ci Sunuy aada.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Al-Isra 75

Simoore Al-Isra Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kon Dananu la mosal mbugali àddina ak mbugali àllaaxira;…

Simoore Aaya 75/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers