Al-Isra · 76/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَإِن كَادُوا لَيَسْتَفِزُّونَكَ مِنَ الْأَرْضِ لِيُخْرِجُوكَ مِنْهَا ۖ وَإِذًا لَّا يَلْبَثُونَ خِلَافَكَ إِلَّا قَلِيلًا ۝٧٦
Wa in kaadoo la yastafizzoonaka minal ardi liyukhri jooka minhaa wa izal laa yalbasoona khilaafaka illaa qaleelaa
📖 Tekkim Wolof
Te xaw nañu laa génne ca suuf sa [suufi Madiina] ngir ñu jële la fa. Te kon duñu fa toog lu dul diir bu néew ci sa ginnaw. [alag leen].

🎧 Dégg


📜 Aaya 74-78 — Al-Isra

74وَلَوْلَا أَن ثَبَّتْنَاكَ لَقَدْ كِدتَّ تَرْكَنُ إِلَيْهِمْ شَيْئًا قَلِيلًا
Te bu Nu la dëgaralul woon, tuuti kon nga xaw a jeng jëm ci ñoom
75إِذًا لَّأَذَقْنَاكَ ضِعْفَ الْحَيَاةِ وَضِعْفَ الْمَمَاتِ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ عَلَيْنَا نَصِيرًا
Te kon Dananu la mosal mbugali àddina ak mbugali àllaaxira; te doo am ku la dimbali ci Nun.
76وَإِن كَادُوا لَيَسْتَفِزُّونَكَ مِنَ الْأَرْضِ لِيُخْرِجُوكَ مِنْهَا ۖ وَإِذًا لَّا يَلْبَثُونَ خِلَافَكَ إِلَّا قَلِيلًا
Te xaw nañu laa génne ca suuf sa [suufi Madiina] ngir ñu jële la fa. Te kon duñu fa toog lu dul diir bu néew ci sa ginnaw. [alag leen].
77سُنَّةَ مَن قَدْ أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ مِن رُّسُلِنَا ۖ وَلَا تَجِدُ لِسُنَّتِنَا تَحْوِيلًا
Loolu aada la ca ña Nu yónni woon la la jiitu ci Sunuy Yonent. Te doo gis lu soppiku ci Sunuy aada.
78أَقِمِ الصَّلَاةَ لِدُلُوكِ الشَّمْسِ إِلَىٰ غَسَقِ اللَّيْلِ وَقُرْآنَ الْفَجْرِ ۖ إِنَّ قُرْآنَ الْفَجْرِ كَانَ مَشْهُودًا
Nanga taxawal julli bu jant fenkee ba ba muy suux, ba ba guddi gi di ñuul, ak it jullig suba, ndax jullig suba lu ñuy seede la.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
76Aaya

Tekki — Al-Isra 76

Simoore Al-Isra Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te xaw nañu laa génne ca suuf sa [suufi Madiina]…

Simoore Aaya 76/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers