Al-Kahf · 100/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
وَعَرَضْنَا جَهَنَّمَ يَوْمَئِذٍ لِّلْكَافِرِينَ عَرْضًا ١٠٠
Transliteration
Wa `aradnaa jahannama Yawma`izil lilkaafireena `ardaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ca boobale bis Dananu gaaral yéefar yi ca Safara,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 98-102 — Al-Kahf
98قَالَ هَٰذَا رَحْمَةٌ مِّن رَّبِّي ۖ فَإِذَا جَاءَ وَعْدُ رَبِّي جَعَلَهُ دَكَّاءَ ۖ وَكَانَ وَعْدُ رَبِّي حَقًّا
Zul-Qarnaynine leen : “Lii dey xéewal la gu bawoo fa Yàlla. Waaye, Saa su digub Yàlla agsee, ca la koy màbb. Te digub Yàlla bi dëgg la te fàwwu mu dikk”.
99۞ وَتَرَكْنَا بَعْضَهُمْ يَوْمَئِذٍ يَمُوجُ فِي بَعْضٍ ۖ وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَجَمَعْنَاهُمْ جَمْعًا
Bu boobaa, nit ñi dañuy mbëkkënte ni ay duusi géej, bu ñu walee buftu ba, Nu daldi leen di dajale ñoom ñépp.
100وَعَرَضْنَا جَهَنَّمَ يَوْمَئِذٍ لِّلْكَافِرِينَ عَرْضًا
Ca boobale bis Dananu gaaral yéefar yi ca Safara,
101الَّذِينَ كَانَتْ أَعْيُنُهُمْ فِي غِطَاءٍ عَن ذِكْرِي وَكَانُوا لَا يَسْتَطِيعُونَ سَمْعًا
[Yéefar] yi nga xam ne dañu daan muur seeni gët ngir bañ a gis Sunuy tegtal, te daan ko bañ a dégg.
102أَفَحَسِبَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَن يَتَّخِذُوا عِبَادِي مِن دُونِي أَوْلِيَاءَ ۚ إِنَّا أَعْتَدْنَا جَهَنَّمَ لِلْكَافِرِينَ نُزُلًا
Ndax ña weddi [Yéefar ya], dañoo njort ne mën nañoo am wéeruwaay ci sama jaam ñi féddiku Ma ? Déedéet yéefar yi Safara la leen di xaaroo de.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
100Aaya
Tekki — Al-Kahf 100
Simoore Al-Kahf Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca boobale bis Dananu gaaral yéefar yi ca Safara,Simoore Aaya 100/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








