Al-Kahf · 12/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
ثُمَّ بَعَثْنَاهُمْ لِنَعْلَمَ أَيُّ الْحِزْبَيْنِ أَحْصَىٰ لِمَا لَبِثُوا أَمَدًا ۝١٢
Summa ba`asnaahum lina`lama ayyul hizbaini ahsaa limaa labisooo amadaa
📖 Tekkim Wolof
Topp Nu yee leen ngir bëgg a xam ban ci ñaari kurél yii moo gën a xayma diir ba ñu fa toog.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Al-Kahf

10إِذْ أَوَى الْفِتْيَةُ إِلَى الْكَهْفِ فَقَالُوا رَبَّنَا آتِنَا مِن لَّدُنكَ رَحْمَةً وَهَيِّئْ لَنَا مِنْ أَمْرِنَا رَشَدًا
[Fàttalikul] ba waxamaande ya làqoo ca xunt ma, te ñu waxoon ne : “Yaw sunu Boroom, may nu yërmaande ju bawoo ci yaw; te nga yéwénal sunuy mbir mu nekk cig njub”.
11فَضَرَبْنَا عَلَىٰ آذَانِهِمْ فِي الْكَهْفِ سِنِينَ عَدَدًا
Nu fëkk seeni nopp [nelawloo leen] ca biir xunt ma ay at yu limu.
12ثُمَّ بَعَثْنَاهُمْ لِنَعْلَمَ أَيُّ الْحِزْبَيْنِ أَحْصَىٰ لِمَا لَبِثُوا أَمَدًا
Topp Nu yee leen ngir bëgg a xam ban ci ñaari kurél yii moo gën a xayma diir ba ñu fa toog.
13نَّحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ نَبَأَهُم بِالْحَقِّ ۚ إِنَّهُمْ فِتْيَةٌ آمَنُوا بِرَبِّهِمْ وَزِدْنَاهُمْ هُدًى
Noo ngi lay nettali seeni mbir ci dëgg. Ne ko ñoom ay waxambaane lañu yu gëmoon seen Boroom ; ba tax na ñu gën leen a dëgëral cig njub.
14وَرَبَطْنَا عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ إِذْ قَامُوا فَقَالُوا رَبُّنَا رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ لَن نَّدْعُوَ مِن دُونِهِ إِلَٰهًا ۖ لَّقَدْ قُلْنَا إِذًا شَطَطًا
Nu dëgëral seeni xol ba ñu taxawee [ca kanamu buur ba nekkoon jaamukatu xërëm], wax ne : “Sunu Boroom mooy Boroom asamaan yi ak suuf si : dunu jaamu jeneen Yàlla bàyyi ko, ndax kon dananu wax lu jeng.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Kahf 12

Simoore Al-Kahf Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp Nu yee leen ngir bëgg a xam ban ci…

Simoore Aaya 12/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers