Al-Kahf · 13/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
نَّحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ نَبَأَهُم بِالْحَقِّ ۚ إِنَّهُمْ فِتْيَةٌ آمَنُوا بِرَبِّهِمْ وَزِدْنَاهُمْ هُدًى ۝١٣
Nahnu naqussu `alaika naba ahum bilhaqq; innahum fityatun aamanoo bi Rabbihim wa zidnaahum hudaa
📖 Tekkim Wolof
Noo ngi lay nettali seeni mbir ci dëgg. Ne ko ñoom ay waxambaane lañu yu gëmoon seen Boroom ; ba tax na ñu gën leen a dëgëral cig njub.
🎧 Dégg

📜 Aaya 11-15 — Al-Kahf

11فَضَرَبْنَا عَلَىٰ آذَانِهِمْ فِي الْكَهْفِ سِنِينَ عَدَدًا
Nu fëkk seeni nopp [nelawloo leen] ca biir xunt ma ay at yu limu.
12ثُمَّ بَعَثْنَاهُمْ لِنَعْلَمَ أَيُّ الْحِزْبَيْنِ أَحْصَىٰ لِمَا لَبِثُوا أَمَدًا
Topp Nu yee leen ngir bëgg a xam ban ci ñaari kurél yii moo gën a xayma diir ba ñu fa toog.
13نَّحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ نَبَأَهُم بِالْحَقِّ ۚ إِنَّهُمْ فِتْيَةٌ آمَنُوا بِرَبِّهِمْ وَزِدْنَاهُمْ هُدًى
Noo ngi lay nettali seeni mbir ci dëgg. Ne ko ñoom ay waxambaane lañu yu gëmoon seen Boroom ; ba tax na ñu gën leen a dëgëral cig njub.
14وَرَبَطْنَا عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ إِذْ قَامُوا فَقَالُوا رَبُّنَا رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ لَن نَّدْعُوَ مِن دُونِهِ إِلَٰهًا ۖ لَّقَدْ قُلْنَا إِذًا شَطَطًا
Nu dëgëral seeni xol ba ñu taxawee [ca kanamu buur ba nekkoon jaamukatu xërëm], wax ne : “Sunu Boroom mooy Boroom asamaan yi ak suuf si : dunu jaamu jeneen Yàlla bàyyi ko, ndax kon dananu wax lu jeng.
15هَٰؤُلَاءِ قَوْمُنَا اتَّخَذُوا مِن دُونِهِ آلِهَةً ۖ لَّوْلَا يَأْتُونَ عَلَيْهِم بِسُلْطَانٍ بَيِّنٍ ۖ فَمَنْ أَظْلَمُ مِمَّنِ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا
Sunuy nit a ngi nii di jaamu yu ñu tudde ay yàlla bañ a jaamu Yàlla. Lu tee ñu indi ci ñooom ay lay yu bir ?
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Kahf 13

Simoore Al-Kahf Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noo ngi lay nettali seeni mbir ci dëgg. Ne ko…

Simoore Aaya 13/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers