Al-Kahf · 11/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
فَضَرَبْنَا عَلَىٰ آذَانِهِمْ فِي الْكَهْفِ سِنِينَ عَدَدًا ۝١١
Fadarabnaa `alaaa aazaanihim fil Kahfi seneena `adadaa
📖 Tekkim Wolof
Nu fëkk seeni nopp [nelawloo leen] ca biir xunt ma ay at yu limu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Al-Kahf

9أَمْ حَسِبْتَ أَنَّ أَصْحَابَ الْكَهْفِ وَالرَّقِيمِ كَانُوا مِنْ آيَاتِنَا عَجَبًا
Ndax amuloo njort ci ne, ñoñ-xunt ma ak ñoñ-mbind ma [téere ba] bokkoon nañu ca Sunuy kéemaan yu doy waar [yéeme] ?
10إِذْ أَوَى الْفِتْيَةُ إِلَى الْكَهْفِ فَقَالُوا رَبَّنَا آتِنَا مِن لَّدُنكَ رَحْمَةً وَهَيِّئْ لَنَا مِنْ أَمْرِنَا رَشَدًا
[Fàttalikul] ba waxamaande ya làqoo ca xunt ma, te ñu waxoon ne : “Yaw sunu Boroom, may nu yërmaande ju bawoo ci yaw; te nga yéwénal sunuy mbir mu nekk cig njub”.
11فَضَرَبْنَا عَلَىٰ آذَانِهِمْ فِي الْكَهْفِ سِنِينَ عَدَدًا
Nu fëkk seeni nopp [nelawloo leen] ca biir xunt ma ay at yu limu.
12ثُمَّ بَعَثْنَاهُمْ لِنَعْلَمَ أَيُّ الْحِزْبَيْنِ أَحْصَىٰ لِمَا لَبِثُوا أَمَدًا
Topp Nu yee leen ngir bëgg a xam ban ci ñaari kurél yii moo gën a xayma diir ba ñu fa toog.
13نَّحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ نَبَأَهُم بِالْحَقِّ ۚ إِنَّهُمْ فِتْيَةٌ آمَنُوا بِرَبِّهِمْ وَزِدْنَاهُمْ هُدًى
Noo ngi lay nettali seeni mbir ci dëgg. Ne ko ñoom ay waxambaane lañu yu gëmoon seen Boroom ; ba tax na ñu gën leen a dëgëral cig njub.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Kahf 11

Simoore Al-Kahf Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu fëkk seeni nopp [nelawloo leen] ca biir xunt ma…

Simoore Aaya 11/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers