Al-Kahf · 67/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
قَالَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا ۝٦٧
Qaalaa innaka lan tastatee`a ma`iya sabraa
📖 Tekkim Wolof
Mu tontu ko, ne: “Doo mën a ànd ak man ci sag muñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Simoore Al-Kahf

65فَوَجَدَا عَبْدًا مِّنْ عِبَادِنَا آتَيْنَاهُ رَحْمَةً مِّنْ عِندِنَا وَعَلَّمْنَاهُ مِن لَّدُنَّا عِلْمًا
Ñu daje ak ab jaam ci sama jaam yi boo xam ne may Nanu ko yërmaande lu jóge ci Nun, te jàngal Nanu ko xam-xam bu bàyyikoo ci Nun.
66قَالَ لَهُ مُوسَىٰ هَلْ أَتَّبِعُكَ عَلَىٰ أَن تُعَلِّمَنِ مِمَّا عُلِّمْتَ رُشْدًا
Muusaa ne ko : “Ndax ma topp la ci kaw nga jàngal ma ci lu xamaleef na la ko ci luy gindee [ak xamle] ? ”.
67قَالَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu tontu ko, ne: “Doo mën a ànd ak man ci sag muñ.
68وَكَيْفَ تَصْبِرُ عَلَىٰ مَا لَمْ تُحِطْ بِهِ خُبْرًا
Naka ngay muñee ci loo xam ne peeguloo ko ci xam-xam ? ”.
69قَالَ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ صَابِرًا وَلَا أَعْصِي لَكَ أَمْرًا
Mu ne ko : “Danga ma fekk bu soobee Yàlla ma di muñkat ; te duma moy sa lenn ndigal”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Al-Kahf 67

Simoore Al-Kahf Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu tontu ko, ne: “Doo mën a ànd ak man…

Simoore Aaya 67/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers