Al-Kahf · 66/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
قَالَ لَهُ مُوسَىٰ هَلْ أَتَّبِعُكَ عَلَىٰ أَن تُعَلِّمَنِ مِمَّا عُلِّمْتَ رُشْدًا ۝٦٦
Qaala lahoo Moosaa hal attabi`uka `alaaa an tu`allimani mimmaa `ullimta rushdaa
📖 Tekkim Wolof
Muusaa ne ko : “Ndax ma topp la ci kaw nga jàngal ma ci lu xamaleef na la ko ci luy gindee [ak xamle] ? ”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 64-68 — Simoore Al-Kahf

64قَالَ ذَٰلِكَ مَا كُنَّا نَبْغِ ۚ فَارْتَدَّا عَلَىٰ آثَارِهِمَا قَصَصًا
Muusaa ne ko : “Loolu lanu doon sàkku”. Ñu dellu fa ñu jaaroon di xeeñtu.
65فَوَجَدَا عَبْدًا مِّنْ عِبَادِنَا آتَيْنَاهُ رَحْمَةً مِّنْ عِندِنَا وَعَلَّمْنَاهُ مِن لَّدُنَّا عِلْمًا
Ñu daje ak ab jaam ci sama jaam yi boo xam ne may Nanu ko yërmaande lu jóge ci Nun, te jàngal Nanu ko xam-xam bu bàyyikoo ci Nun.
66قَالَ لَهُ مُوسَىٰ هَلْ أَتَّبِعُكَ عَلَىٰ أَن تُعَلِّمَنِ مِمَّا عُلِّمْتَ رُشْدًا
Muusaa ne ko : “Ndax ma topp la ci kaw nga jàngal ma ci lu xamaleef na la ko ci luy gindee [ak xamle] ? ”.
67قَالَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu tontu ko, ne: “Doo mën a ànd ak man ci sag muñ.
68وَكَيْفَ تَصْبِرُ عَلَىٰ مَا لَمْ تُحِطْ بِهِ خُبْرًا
Naka ngay muñee ci loo xam ne peeguloo ko ci xam-xam ? ”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Al-Kahf 66

Simoore Al-Kahf Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muusaa ne ko : “Ndax ma topp la ci kaw…

Simoore Aaya 66/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers