Al-Kahf · 75/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
۞ قَالَ أَلَمْ أَقُل لَّكَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا ۝٧٥
Qaala alam aqul laka innaka lan tastatee`a ma`iya sabraa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne mënuloo muñ li may def soo àndeek man ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-77 — Al-Kahf

73قَالَ لَا تُؤَاخِذْنِي بِمَا نَسِيتُ وَلَا تُرْهِقْنِي مِنْ أَمْرِي عُسْرًا
Mu ne ko : “Bul ma jàppe ci lu ma fàtte ; te it bul ma togg-jëf ci sama mbir”.
74فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا لَقِيَا غُلَامًا فَقَتَلَهُ قَالَ أَقَتَلْتَ نَفْسًا زَكِيَّةً بِغَيْرِ نَفْسٍ لَّقَدْ جِئْتَ شَيْئًا نُّكْرًا
Ñu demaat ba dajeek benn xale, mu rey ko. Muusaa ne ko : “Ndax dangay rey bakkan bu sell bu reyul bakkan ? Def nga jëf ju yéeme ! ”
75۞ قَالَ أَلَمْ أَقُل لَّكَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne mënuloo muñ li may def soo àndeek man ? ”
76قَالَ إِن سَأَلْتُكَ عَن شَيْءٍ بَعْدَهَا فَلَا تُصَاحِبْنِي ۖ قَدْ بَلَغْتَ مِن لَّدُنِّي عُذْرًا
[Muusaa] toontu ko ne : “Saa yu ma la laajee menn mbir, kon bul àndateek man. Ndax am nga ngànt ci tàggook man”.
77فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا أَتَيَا أَهْلَ قَرْيَةٍ اسْتَطْعَمَا أَهْلَهَا فَأَبَوْا أَن يُضَيِّفُوهُمَا فَوَجَدَا فِيهَا جِدَارًا يُرِيدُ أَن يَنقَضَّ فَأَقَامَهُ ۖ قَالَ لَوْ شِئْتَ لَتَّخَذْتَ عَلَيْهِ أَجْرًا
Ñuy dox ba egg cib dëkk, ñu sàkku ca waa dëkk ba lekk, ñu lànk leen a ganale. Noona mu gis ab tabax buy bëgg a daanu. Mu yékkatiwaat ko. [Muusaa] ne ko : “Su la neexoon dey nga laaj ag pey”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Al-Kahf 75

Simoore Al-Kahf Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne mënuloo…

Simoore Aaya 75/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers