Al-Kahf · 74/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا لَقِيَا غُلَامًا فَقَتَلَهُ قَالَ أَقَتَلْتَ نَفْسًا زَكِيَّةً بِغَيْرِ نَفْسٍ لَّقَدْ جِئْتَ شَيْئًا نُّكْرًا ۝٧٤
Fantalaqaa hattaa izaa laqiyaa ghulaaman faqatalahoo qaala aqatalta nafsan zakiy yatam bighairi nafs; laqad ji`ta shai`an nukraa
📖 Tekkim Wolof
Ñu demaat ba dajeek benn xale, mu rey ko. Muusaa ne ko : “Ndax dangay rey bakkan bu sell bu reyul bakkan ? Def nga jëf ju yéeme ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Simoore Al-Kahf

72قَالَ أَلَمْ أَقُلْ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne doo mën a ànd ak man ci sag muñ ? ”.
73قَالَ لَا تُؤَاخِذْنِي بِمَا نَسِيتُ وَلَا تُرْهِقْنِي مِنْ أَمْرِي عُسْرًا
Mu ne ko : “Bul ma jàppe ci lu ma fàtte ; te it bul ma togg-jëf ci sama mbir”.
74فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا لَقِيَا غُلَامًا فَقَتَلَهُ قَالَ أَقَتَلْتَ نَفْسًا زَكِيَّةً بِغَيْرِ نَفْسٍ لَّقَدْ جِئْتَ شَيْئًا نُّكْرًا
Ñu demaat ba dajeek benn xale, mu rey ko. Muusaa ne ko : “Ndax dangay rey bakkan bu sell bu reyul bakkan ? Def nga jëf ju yéeme ! ”
75۞ قَالَ أَلَمْ أَقُل لَّكَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne mënuloo muñ li may def soo àndeek man ? ”
76قَالَ إِن سَأَلْتُكَ عَن شَيْءٍ بَعْدَهَا فَلَا تُصَاحِبْنِي ۖ قَدْ بَلَغْتَ مِن لَّدُنِّي عُذْرًا
[Muusaa] toontu ko ne : “Saa yu ma la laajee menn mbir, kon bul àndateek man. Ndax am nga ngànt ci tàggook man”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Al-Kahf 74

Simoore Al-Kahf Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu demaat ba dajeek benn xale, mu rey ko. Muusaa…

Simoore Aaya 74/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers