Al-Kahf · 76/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
قَالَ إِن سَأَلْتُكَ عَن شَيْءٍ بَعْدَهَا فَلَا تُصَاحِبْنِي ۖ قَدْ بَلَغْتَ مِن لَّدُنِّي عُذْرًا ۝٧٦
Qaala in sa altuka `an shai`im ba`dahaa falaa tusaahibnee qad balaghta mil ladunnee `uzraa
📖 Tekkim Wolof
[Muusaa] toontu ko ne : “Saa yu ma la laajee menn mbir, kon bul àndateek man. Ndax am nga ngànt ci tàggook man”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 74-78 — Al-Kahf

74فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا لَقِيَا غُلَامًا فَقَتَلَهُ قَالَ أَقَتَلْتَ نَفْسًا زَكِيَّةً بِغَيْرِ نَفْسٍ لَّقَدْ جِئْتَ شَيْئًا نُّكْرًا
Ñu demaat ba dajeek benn xale, mu rey ko. Muusaa ne ko : “Ndax dangay rey bakkan bu sell bu reyul bakkan ? Def nga jëf ju yéeme ! ”
75۞ قَالَ أَلَمْ أَقُل لَّكَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne mënuloo muñ li may def soo àndeek man ? ”
76قَالَ إِن سَأَلْتُكَ عَن شَيْءٍ بَعْدَهَا فَلَا تُصَاحِبْنِي ۖ قَدْ بَلَغْتَ مِن لَّدُنِّي عُذْرًا
[Muusaa] toontu ko ne : “Saa yu ma la laajee menn mbir, kon bul àndateek man. Ndax am nga ngànt ci tàggook man”.
77فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا أَتَيَا أَهْلَ قَرْيَةٍ اسْتَطْعَمَا أَهْلَهَا فَأَبَوْا أَن يُضَيِّفُوهُمَا فَوَجَدَا فِيهَا جِدَارًا يُرِيدُ أَن يَنقَضَّ فَأَقَامَهُ ۖ قَالَ لَوْ شِئْتَ لَتَّخَذْتَ عَلَيْهِ أَجْرًا
Ñuy dox ba egg cib dëkk, ñu sàkku ca waa dëkk ba lekk, ñu lànk leen a ganale. Noona mu gis ab tabax buy bëgg a daanu. Mu yékkatiwaat ko. [Muusaa] ne ko : “Su la neexoon dey nga laaj ag pey”.
78قَالَ هَٰذَا فِرَاقُ بَيْنِي وَبَيْنِكَ ۚ سَأُنَبِّئُكَ بِتَأْوِيلِ مَا لَمْ تَسْتَطِع عَّلَيْهِ صَبْرًا
Mu ne ko : “Maak yaw fii la nuy tàqalikoo.Waaye danaa la leeralal mbirum li nga mënul woon a muñ.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
76Aaya

Tekki — Al-Kahf 76

Simoore Al-Kahf Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Muusaa] toontu ko ne : “Saa yu ma la laajee…

Simoore Aaya 76/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers