Al-Kahf · 88/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
وَأَمَّا مَنْ آمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَلَهُ جَزَاءً الْحُسْنَىٰ ۖ وَسَنَقُولُ لَهُ مِنْ أَمْرِنَا يُسْرًا ۝٨٨
Wa ammaa man aamana wa `amila saalihan falahoo jazaaa`anil husnaa wa sanaqoolu lahoo min amrinaa yusraa
📖 Tekkim Wolof
Képp koo xam ne dafa gëm tey jëf u yiw, dana am pey gu gën a rafet. Te it fu mu tollu di gis yombal gu bawoo fi nun”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 86-90 — Al-Kahf

86حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَغْرِبَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَغْرُبُ فِي عَيْنٍ حَمِئَةٍ وَوَجَدَ عِندَهَا قَوْمًا ۗ قُلْنَا يَا ذَا الْقَرْنَيْنِ إِمَّا أَن تُعَذِّبَ وَإِمَّا أَن تَتَّخِذَ فِيهِمْ حُسْنًا
Mu takk xare dem ba fa sowwu yem, mu fekk ne jant ba ma ngay sowe fa ndox ma ànd ak ban, mu fekk itam aw xeet [wa ko dëkke]. Ñu ne ko : “Fàwwu yaw Zul-Qarnayni ! nga mbugal leen walla nga yërëm leen”.
87قَالَ أَمَّا مَن ظَلَمَ فَسَوْفَ نُعَذِّبُهُ ثُمَّ يُرَدُّ إِلَىٰ رَبِّهِ فَيُعَذِّبُهُ عَذَابًا نُّكْرًا
Mu wax ne : “Képp koo xam ne dafay tooñ, dananu ko mbugal fii ; te su delloo fa Boroomam, Dana ko mbugal mbugal mu gën a tar.
88وَأَمَّا مَنْ آمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَلَهُ جَزَاءً الْحُسْنَىٰ ۖ وَسَنَقُولُ لَهُ مِنْ أَمْرِنَا يُسْرًا
Képp koo xam ne dafa gëm tey jëf u yiw, dana am pey gu gën a rafet. Te it fu mu tollu di gis yombal gu bawoo fi nun”.
89ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا
Mu dellu sóobu ci bëgg-bëggam.
90حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَطْلِعَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَطْلُعُ عَلَىٰ قَوْمٍ لَّمْ نَجْعَل لَّهُم مِّن دُونِهَا سِتْرًا
Mu takk xare dem ba fa penku yem, mu fekk fa xeet wu amul lu leen yiiral tàngooru jant bi.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — Al-Kahf 88

Simoore Al-Kahf Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp koo xam ne dafa gëm tey jëf u yiw,…

Simoore Aaya 88/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers