Al-Kahf · 89/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا ۝٨٩
Summa atba`a sababaa
📖 Tekkim Wolof
Mu dellu sóobu ci bëgg-bëggam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 87-91 — Simoore Al-Kahf

87قَالَ أَمَّا مَن ظَلَمَ فَسَوْفَ نُعَذِّبُهُ ثُمَّ يُرَدُّ إِلَىٰ رَبِّهِ فَيُعَذِّبُهُ عَذَابًا نُّكْرًا
Mu wax ne : “Képp koo xam ne dafay tooñ, dananu ko mbugal fii ; te su delloo fa Boroomam, Dana ko mbugal mbugal mu gën a tar.
88وَأَمَّا مَنْ آمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَلَهُ جَزَاءً الْحُسْنَىٰ ۖ وَسَنَقُولُ لَهُ مِنْ أَمْرِنَا يُسْرًا
Képp koo xam ne dafa gëm tey jëf u yiw, dana am pey gu gën a rafet. Te it fu mu tollu di gis yombal gu bawoo fi nun”.
89ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا
Mu dellu sóobu ci bëgg-bëggam.
90حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَطْلِعَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَطْلُعُ عَلَىٰ قَوْمٍ لَّمْ نَجْعَل لَّهُم مِّن دُونِهَا سِتْرًا
Mu takk xare dem ba fa penku yem, mu fekk fa xeet wu amul lu leen yiiral tàngooru jant bi.
91كَذَٰلِكَ وَقَدْ أَحَطْنَا بِمَا لَدَيْهِ خُبْرًا
Mu wax ne : na ñu defoon ñële rekk la ñuy def ñii, waxoon nanu lépp la mu nar.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
89Aaya

Tekki — Al-Kahf 89

Simoore Al-Kahf Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu dellu sóobu ci bëgg-bëggam.

Simoore Aaya 89/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers