Al-Kahf · 92/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا ۝٩٢
Summa atba`a sababaa
📖 Tekkim Wolof
Mu wéyati ci bëgg-bëggamdi dox di wéy.

🎧 Dégg


📜 Aaya 90-94 — Simoore Al-Kahf

90حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَطْلِعَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَطْلُعُ عَلَىٰ قَوْمٍ لَّمْ نَجْعَل لَّهُم مِّن دُونِهَا سِتْرًا
Mu takk xare dem ba fa penku yem, mu fekk fa xeet wu amul lu leen yiiral tàngooru jant bi.
91كَذَٰلِكَ وَقَدْ أَحَطْنَا بِمَا لَدَيْهِ خُبْرًا
Mu wax ne : na ñu defoon ñële rekk la ñuy def ñii, waxoon nanu lépp la mu nar.
92ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا
Mu wéyati ci bëgg-bëggamdi dox di wéy.
93حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ بَيْنَ السَّدَّيْنِ وَجَدَ مِن دُونِهِمَا قَوْمًا لَّا يَكَادُونَ يَفْقَهُونَ قَوْلًا
Muy dem ba fekk aw xur mu fekk aw xeet, woo xam ne, seeni wax xaw naa niru waxi nit
94قَالُوا يَا ذَا الْقَرْنَيْنِ إِنَّ يَأْجُوجَ وَمَأْجُوجَ مُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ فَهَلْ نَجْعَلُ لَكَ خَرْجًا عَلَىٰ أَن تَجْعَلَ بَيْنَنَا وَبَيْنَهُمْ سَدًّا
Ñu ne ko : "Yaa juuja ak Maa juuja ay yàqkat lañu ci kaw suuf si. Moo ndax duñu la fey nga ñag sunu diggante ak ñoom ? ”
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
92Aaya

Tekki — Al-Kahf 92

Simoore Al-Kahf Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu wéyati ci bëgg-bëggamdi dox di wéy.

Simoore Aaya 92/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers