Maryam · 59/98
Tekki Waxtaan — Maryam
۞ فَخَلَفَ مِن بَعْدِهِمْ خَلْفٌ أَضَاعُوا الصَّلَاةَ وَاتَّبَعُوا الشَّهَوَاتِ ۖ فَسَوْفَ يَلْقَوْنَ غَيًّا ٥٩
Transliteration
Fakhalafa mim ba`dihim khalfun adaa`us Salaata wattaba`ush shahawaati fasawfa yalqawna ghaiyaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Seen ginnaaw mu am ñu leen wuutu, sànk julli, topp seeni bànneex. Ñooña danañu dajeek tuskare,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 57-61 — Maryam
57وَرَفَعْنَاهُ مَكَانًا عَلِيًّا
Mayoon Nanu ko daraja ju kawe.
58أُولَٰئِكَ الَّذِينَ أَنْعَمَ اللَّهُ عَلَيْهِم مِّنَ النَّبِيِّينَ مِن ذُرِّيَّةِ آدَمَ وَمِمَّنْ حَمَلْنَا مَعَ نُوحٍ وَمِن ذُرِّيَّةِ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْرَائِيلَ وَمِمَّنْ هَدَيْنَا وَاجْتَبَيْنَا ۚ إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُ الرَّحْمَٰنِ خَرُّوا سُجَّدًا وَبُكِيًّا ۩
Ñooña ñooy ña nga xam ne Yàlla wàcceloon na leen xéewalam ca Yonent ya, ak ca sëti Aadama, ak ña àndoon ak Nooh ca gaal ga, ak ña bokk ca sëti Ibraahiima ak ca ñu Nu gindi woon te tànnoon leen. Te saa su ñu mësaa na jàng kàdduy Yàlla fa ñoom, ñu rot sujjóot boole kooki jooy.
59۞ فَخَلَفَ مِن بَعْدِهِمْ خَلْفٌ أَضَاعُوا الصَّلَاةَ وَاتَّبَعُوا الشَّهَوَاتِ ۖ فَسَوْفَ يَلْقَوْنَ غَيًّا
Seen ginnaaw mu am ñu leen wuutu, sànk julli, topp seeni bànneex. Ñooña danañu dajeek tuskare,
60إِلَّا مَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَأُولَٰئِكَ يَدْخُلُونَ الْجَنَّةَ وَلَا يُظْلَمُونَ شَيْئًا
ba mu des ku tuub te gëm tey jëf u yiw : ñooña danañu tàbbi Àjjana te keen duleen tooñ ci dara [wàññi seenug pey],
61جَنَّاتِ عَدْنٍ الَّتِي وَعَدَ الرَّحْمَٰنُ عِبَادَهُ بِالْغَيْبِ ۚ إِنَّهُ كَانَ وَعْدُهُ مَأْتِيًّا
àjjana yu sax ya, àjjana ya Yàlla dig jaamam ña ci kumpa te digub Yàlla fàwwu mu ñëw.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
59Aaya
Tekki — Maryam 59
Simoore Maryam Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen ginnaaw mu am ñu leen wuutu, sànk julli, topp…Simoore Aaya 59/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








