Maryam · 58/98
Tekki Waxtaan — Maryam
أُولَٰئِكَ الَّذِينَ أَنْعَمَ اللَّهُ عَلَيْهِم مِّنَ النَّبِيِّينَ مِن ذُرِّيَّةِ آدَمَ وَمِمَّنْ حَمَلْنَا مَعَ نُوحٍ وَمِن ذُرِّيَّةِ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْرَائِيلَ وَمِمَّنْ هَدَيْنَا وَاجْتَبَيْنَا ۚ إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُ الرَّحْمَٰنِ خَرُّوا سُجَّدًا وَبُكِيًّا ۩ ۝٥٨
Ulaaa`ikal lazeena an`amal laahu `alaihim minan Nabiyyeena min zurriyyati Aadama wa mimman hamalnaa ma`a Noohinw wa min zurriyyati Ibraaheema wa Israaa`eela wa mimman hadainaa wajta bainaaa; izaa tutlaa `alaihim Aayaatur Rahmaani kharroo sujjadanw wa bukiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Ñooña ñooy ña nga xam ne Yàlla wàcceloon na leen xéewalam ca Yonent ya, ak ca sëti Aadama, ak ña àndoon ak Nooh ca gaal ga, ak ña bokk ca sëti Ibraahiima ak ca ñu Nu gindi woon te tànnoon leen. Te saa su ñu mësaa na jàng kàdduy Yàlla fa ñoom, ñu rot sujjóot boole kooki jooy.

🎧 Dégg


📜 Aaya 56-60 — Maryam

56وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِدْرِيسَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صِدِّيقًا نَّبِيًّا
Fàttalikul Idriisa ca Téere ba. Moom dey ku dëddu la woon, di ab Yonent.
57وَرَفَعْنَاهُ مَكَانًا عَلِيًّا
Mayoon Nanu ko daraja ju kawe.
58أُولَٰئِكَ الَّذِينَ أَنْعَمَ اللَّهُ عَلَيْهِم مِّنَ النَّبِيِّينَ مِن ذُرِّيَّةِ آدَمَ وَمِمَّنْ حَمَلْنَا مَعَ نُوحٍ وَمِن ذُرِّيَّةِ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْرَائِيلَ وَمِمَّنْ هَدَيْنَا وَاجْتَبَيْنَا ۚ إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُ الرَّحْمَٰنِ خَرُّوا سُجَّدًا وَبُكِيًّا ۩
Ñooña ñooy ña nga xam ne Yàlla wàcceloon na leen xéewalam ca Yonent ya, ak ca sëti Aadama, ak ña àndoon ak Nooh ca gaal ga, ak ña bokk ca sëti Ibraahiima ak ca ñu Nu gindi woon te tànnoon leen. Te saa su ñu mësaa na jàng kàdduy Yàlla fa ñoom, ñu rot sujjóot boole kooki jooy.
59۞ فَخَلَفَ مِن بَعْدِهِمْ خَلْفٌ أَضَاعُوا الصَّلَاةَ وَاتَّبَعُوا الشَّهَوَاتِ ۖ فَسَوْفَ يَلْقَوْنَ غَيًّا
Seen ginnaaw mu am ñu leen wuutu, sànk julli, topp seeni bànneex. Ñooña danañu dajeek tuskare,
60إِلَّا مَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَأُولَٰئِكَ يَدْخُلُونَ الْجَنَّةَ وَلَا يُظْلَمُونَ شَيْئًا
ba mu des ku tuub te gëm tey jëf u yiw : ñooña danañu tàbbi Àjjana te keen duleen tooñ ci dara [wàññi seenug pey],
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — Maryam 58

Simoore Maryam Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooña ñooy ña nga xam ne Yàlla wàcceloon na leen…

Simoore Aaya 58/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers