Maryam · 76/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَيَزِيدُ اللَّهُ الَّذِينَ اهْتَدَوْا هُدًى ۗ وَالْبَاقِيَاتُ الصَّالِحَاتُ خَيْرٌ عِندَ رَبِّكَ ثَوَابًا وَخَيْرٌ مَّرَدًّا ۝٧٦
Wa yazeedul laahul lazeenah tadaw hudaa; wal baaqiyaatus saalihaatu khairun `inda Rabbika sawaabanw wa khairum maraddaa
📖 Tekkim Wolof
Yàlla dana dolli njub ña gindiku woon. Jëf yuy des te di yu jiw [sell] moo gën a ëpp ab yool fa sa Boroom te moo gën wàccuwaay.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 74-78 — Simoore Maryam

74وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هُمْ أَحْسَنُ أَثَاثًا وَرِئْيًا
Aka bari ña Nu alagoon ca ña leen jiitu, ñoo xam ne ñoo leen ëppoon alal, gën leen a jekk ?
75قُلْ مَن كَانَ فِي الضَّلَالَةِ فَلْيَمْدُدْ لَهُ الرَّحْمَٰنُ مَدًّا ۚ حَتَّىٰ إِذَا رَأَوْا مَا يُوعَدُونَ إِمَّا الْعَذَابَ وَإِمَّا السَّاعَةَ فَسَيَعْلَمُونَ مَنْ هُوَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضْعَفُ جُندًا
Neel : “Ku nekk cig réer, Yàlla da koy yoor ba mu ne ticcët ca la Nu ko doon dig, benn muy mbugal walla muy Bis-pénc ba. Bu boobaa danañu xam ñoo, ana kan moo yées wàccuwaay te gën a néew doole [ci way gëm ña ak yéefar ya]”.
76وَيَزِيدُ اللَّهُ الَّذِينَ اهْتَدَوْا هُدًى ۗ وَالْبَاقِيَاتُ الصَّالِحَاتُ خَيْرٌ عِندَ رَبِّكَ ثَوَابًا وَخَيْرٌ مَّرَدًّا
Yàlla dana dolli njub ña gindiku woon. Jëf yuy des te di yu jiw [sell] moo gën a ëpp ab yool fa sa Boroom te moo gën wàccuwaay.
77أَفَرَأَيْتَ الَّذِي كَفَرَ بِآيَاتِنَا وَقَالَ لَأُوتَيَنَّ مَالًا وَوَلَدًا
Xanaa gisoo ka weddi Sunuy kàddu bay wax naan : “[Ak lu mën a xew], man danaa am alal ak i doom” ?
78أَطَّلَعَ الْغَيْبَ أَمِ اتَّخَذَ عِندَ الرَّحْمَٰنِ عَهْدًا
Moo ndax dafa xam kumpa, walla mu digaaleek Yàlla ?
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
76Aaya

Tekki — Maryam 76

Simoore Maryam Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla dana dolli njub ña gindiku woon. Jëf yuy des…

Simoore Aaya 76/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers