Maryam · 77/98
Tekki Waxtaan — Maryam
أَفَرَأَيْتَ الَّذِي كَفَرَ بِآيَاتِنَا وَقَالَ لَأُوتَيَنَّ مَالًا وَوَلَدًا ٧٧
Transliteration
Afara`aytal lazee kafara bi Aayaatinaa wa qaala la oota yanna maalanw wa waladaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Xanaa gisoo ka weddi Sunuy kàddu bay wax naan : “[Ak lu mën a xew], man danaa am alal ak i doom” ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 75-79 — Maryam
75قُلْ مَن كَانَ فِي الضَّلَالَةِ فَلْيَمْدُدْ لَهُ الرَّحْمَٰنُ مَدًّا ۚ حَتَّىٰ إِذَا رَأَوْا مَا يُوعَدُونَ إِمَّا الْعَذَابَ وَإِمَّا السَّاعَةَ فَسَيَعْلَمُونَ مَنْ هُوَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضْعَفُ جُندًا
Neel : “Ku nekk cig réer, Yàlla da koy yoor ba mu ne ticcët ca la Nu ko doon dig, benn muy mbugal walla muy Bis-pénc ba. Bu boobaa danañu xam ñoo, ana kan moo yées wàccuwaay te gën a néew doole [ci way gëm ña ak yéefar ya]”.
76وَيَزِيدُ اللَّهُ الَّذِينَ اهْتَدَوْا هُدًى ۗ وَالْبَاقِيَاتُ الصَّالِحَاتُ خَيْرٌ عِندَ رَبِّكَ ثَوَابًا وَخَيْرٌ مَّرَدًّا
Yàlla dana dolli njub ña gindiku woon. Jëf yuy des te di yu jiw [sell] moo gën a ëpp ab yool fa sa Boroom te moo gën wàccuwaay.
77أَفَرَأَيْتَ الَّذِي كَفَرَ بِآيَاتِنَا وَقَالَ لَأُوتَيَنَّ مَالًا وَوَلَدًا
Xanaa gisoo ka weddi Sunuy kàddu bay wax naan : “[Ak lu mën a xew], man danaa am alal ak i doom” ?
78أَطَّلَعَ الْغَيْبَ أَمِ اتَّخَذَ عِندَ الرَّحْمَٰنِ عَهْدًا
Moo ndax dafa xam kumpa, walla mu digaaleek Yàlla ?
79كَلَّا ۚ سَنَكْتُبُ مَا يَقُولُ وَنَمُدُّ لَهُ مِنَ الْعَذَابِ مَدًّا
Déewallaay ! Dananu bind la muy wax, te it Dananu ko mbugal.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
77Aaya
Tekki — Maryam 77
Simoore Maryam Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa gisoo ka weddi Sunuy kàddu bay wax naan :…Simoore Aaya 77/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








