Al-Baqara · 200/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
فَإِذَا قَضَيْتُم مَّنَاسِكَكُمْ فَاذْكُرُوا اللَّهَ كَذِكْرِكُمْ آبَاءَكُمْ أَوْ أَشَدَّ ذِكْرًا ۗ فَمِنَ النَّاسِ مَن يَقُولُ رَبَّنَا آتِنَا فِي الدُّنْيَا وَمَا لَهُ فِي الْآخِرَةِ مِنْ خَلَاقٍ ۝٢٠٠
Fa-izan qadaitum manaa sikakum fazkurul laaha kazikrikum aabaaa`akum aw ashadda zikraa; faminannaasi mai yaqoolu Rabbanaaa aatinaa fiddunyaa wa maa lahoo fil Aakhirati min khalaaq
📖 Tekkim Wolof
Bu seen aj jeexee, nangeen di tuddu Yàlla kem na ngeen daan tuddee [taggee] seeni maam, walla sax tuddiin wu gën a tar. Am na ci nit ñi ñuy wax ne : “Yaw sunu Boroom! May nu àddina [kese] ! ” - te duñu fàggu dara ngir àllaaxira.

🎧 Dégg


📜 Aaya 198-202 — Al-Baqara

198لَيْسَ عَلَيْكُمْ جُنَاحٌ أَن تَبْتَغُوا فَضْلًا مِّن رَّبِّكُمْ ۚ فَإِذَا أَفَضْتُم مِّنْ عَرَفَاتٍ فَاذْكُرُوا اللَّهَ عِندَ الْمَشْعَرِ الْحَرَامِ ۖ وَاذْكُرُوهُ كَمَا هَدَاكُمْ وَإِن كُنتُم مِّن قَبْلِهِ لَمِنَ الضَّالِّينَ
Aayul ci yéen ngeen sàkku wërsëg [jënd ak jaay]. Bu ngeen bàyyikoo [Harafaat], nangeen tudd seen Boroom fa Mach-haril Haraam . Tudduleen Ko, fàttalikuleen Ko kem na Mu leen gindee, fekk la ko jiitu ngeen doonoon ñu réer.
199ثُمَّ أَفِيضُوا مِنْ حَيْثُ أَفَاضَ النَّاسُ وَاسْتَغْفِرُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Topp, ngeen wéy [yéen waa Màkka] bëbb yéen itam fa nit ña bëbbee, jéggaluleen Yàlla. Yàlla Jéggalaakoon la te Jaglewaakoon la.
200فَإِذَا قَضَيْتُم مَّنَاسِكَكُمْ فَاذْكُرُوا اللَّهَ كَذِكْرِكُمْ آبَاءَكُمْ أَوْ أَشَدَّ ذِكْرًا ۗ فَمِنَ النَّاسِ مَن يَقُولُ رَبَّنَا آتِنَا فِي الدُّنْيَا وَمَا لَهُ فِي الْآخِرَةِ مِنْ خَلَاقٍ
Bu seen aj jeexee, nangeen di tuddu Yàlla kem na ngeen daan tuddee [taggee] seeni maam, walla sax tuddiin wu gën a tar. Am na ci nit ñi ñuy wax ne : “Yaw sunu Boroom! May nu àddina [kese] ! ” - te duñu fàggu dara ngir àllaaxira.
201وَمِنْهُم مَّن يَقُولُ رَبَّنَا آتِنَا فِي الدُّنْيَا حَسَنَةً وَفِي الْآخِرَةِ حَسَنَةً وَقِنَا عَذَابَ النَّارِ
Am na ci ñoom kuy wax ne : “Yaw sunu Boroom ! Defalnu xéewal ci àddina, ak ca àllaaxira ; te fegalnu mbugalum Safara ! ”.
202أُولَٰئِكَ لَهُمْ نَصِيبٌ مِّمَّا كَسَبُوا ۚ وَاللَّهُ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Ñooña am na ñu yool ca la ñu sàkku. Te Yàlla ku gaaw la ci xayma [waññi, màndaxe].
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
200Aaya

Tekki — Al-Baqara 200

Simoore Al-Baqara Aaya 200 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu seen aj jeexee, nangeen di tuddu Yàlla kem na…

Simoore Aaya 200/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 198–202. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers