Taha · 6/135
Tekki Waxtaan — Taha
لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَمَا تَحْتَ الثَّرَىٰ ۝٦
Lahoo maa fis samaawaati wa maa fil ardi wa maa bainahumaa wa maa tahtassaraa
📖 Tekkim Wolof
Moo moom li nekk ci asamaan yi ak ci suuf si ak li nekk ci seen diggante, ak li nekk ci ron déeley suuf si.
🎧 Dégg

📜 Aaya 4-8 — Taha

4تَنزِيلًا مِّمَّنْ خَلَقَ الْأَرْضَ وَالسَّمَاوَاتِ الْعُلَى
dafa wàcc bawoo ca Ka bind suuf si ak asamaan yu kawe ya.
5الرَّحْمَٰنُ عَلَى الْعَرْشِ اسْتَوَىٰ
Yàllaa nga yemoo ca Gàngunaay ga [Aras].
6لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَمَا تَحْتَ الثَّرَىٰ
Moo moom li nekk ci asamaan yi ak ci suuf si ak li nekk ci seen diggante, ak li nekk ci ron déeley suuf si.
7وَإِن تَجْهَرْ بِالْقَوْلِ فَإِنَّهُ يَعْلَمُ السِّرَّ وَأَخْفَى
Soo dee jóoru say wax it, Moom xam na mbóot ak la gën a nëbbu.
8اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ لَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ
Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom ! Moo moom tur yi gën a rafet.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Taha 6

Simoore Taha Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo moom li nekk ci asamaan yi ak ci suuf…

Simoore Aaya 6/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers