Taha · 5/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
الرَّحْمَٰنُ عَلَى الْعَرْشِ اسْتَوَىٰ ۝٥
Ar-Rahmaanu `alal `Arshis tawaa
📖 Tekkim Wolof
Yàllaa nga yemoo ca Gàngunaay ga [Aras].

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Taha

3إِلَّا تَذْكِرَةً لِّمَن يَخْشَىٰ
[waaye] Danu koo wàcce ngir muy waar ñi ragal Yàlla,
4تَنزِيلًا مِّمَّنْ خَلَقَ الْأَرْضَ وَالسَّمَاوَاتِ الْعُلَى
dafa wàcc bawoo ca Ka bind suuf si ak asamaan yu kawe ya.
5الرَّحْمَٰنُ عَلَى الْعَرْشِ اسْتَوَىٰ
Yàllaa nga yemoo ca Gàngunaay ga [Aras].
6لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَمَا تَحْتَ الثَّرَىٰ
Moo moom li nekk ci asamaan yi ak ci suuf si ak li nekk ci seen diggante, ak li nekk ci ron déeley suuf si.
7وَإِن تَجْهَرْ بِالْقَوْلِ فَإِنَّهُ يَعْلَمُ السِّرَّ وَأَخْفَى
Soo dee jóoru say wax it, Moom xam na mbóot ak la gën a nëbbu.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Taha 5

Simoore Taha Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaa nga yemoo ca Gàngunaay ga [Aras].

Simoore Aaya 5/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers