Taha · 83/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
۞ وَمَا أَعْجَلَكَ عَن قَوْمِكَ يَا مُوسَىٰ ۝٨٣
Wa maaa a`jalaka `an qawmika yaa Moosa
📖 Tekkim Wolof
“Waaw Muusaa, ana lan moo tax nga jiitu saw nit ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 81-85 — Simoore Taha

81كُلُوا مِن طَيِّبَاتِ مَا رَزَقْنَاكُمْ وَلَا تَطْغَوْا فِيهِ فَيَحِلَّ عَلَيْكُمْ غَضَبِي ۖ وَمَن يَحْلِلْ عَلَيْهِ غَضَبِي فَقَدْ هَوَىٰ
“Lekk-leen ci lu teey [sell] li Nu leen wërsëgale te buleen ca beew, [bu ngeen beewee], kon Sama mer day wàcc ci seen kaw : te képp ku Sama mer wàcc ci kawam, sànku na.
82وَإِنِّي لَغَفَّارٌ لِّمَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا ثُمَّ اهْتَدَىٰ
Te moo ne Man dey ab Jéggalaakoon laa ci képp ku tuub, te gëm, te jëf u yiw tey jubal”.
83۞ وَمَا أَعْجَلَكَ عَن قَوْمِكَ يَا مُوسَىٰ
“Waaw Muusaa, ana lan moo tax nga jiitu saw nit ? ”
84قَالَ هُمْ أُولَاءِ عَلَىٰ أَثَرِي وَعَجِلْتُ إِلَيْكَ رَبِّ لِتَرْضَىٰ
Mu ne ko ñoom dey ñanga ca sama ginnaaw. Ma yàkkamtee agsi ci Yaw ba am sa ngërëm.
85قَالَ فَإِنَّا قَدْ فَتَنَّا قَوْمَكَ مِن بَعْدِكَ وَأَضَلَّهُمُ السَّامِرِيُّ
[Yàlla] ne ko : “Nattu woon Nanu saw nit sa ginnaaw. Saamiriyu ñëw moom sànk leen”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
83Aaya

Tekki — Taha 83

Simoore Taha Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Waaw Muusaa, ana lan moo tax nga jiitu saw nit…

Simoore Aaya 83/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 81–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers