Taha · 82/135
Tekki Waxtaan — Taha
وَإِنِّي لَغَفَّارٌ لِّمَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا ثُمَّ اهْتَدَىٰ ۝٨٢
Wa innee la Ghaffaarul liman taaba wa aamana wa `amila saalihan summah tadaa
📖 Tekkim Wolof
Te moo ne Man dey ab Jéggalaakoon laa ci képp ku tuub, te gëm, te jëf u yiw tey jubal”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 80-84 — Taha

80يَا بَنِي إِسْرَائِيلَ قَدْ أَنجَيْنَاكُم مِّنْ عَدُوِّكُمْ وَوَاعَدْنَاكُمْ جَانِبَ الطُّورِ الْأَيْمَنَ وَنَزَّلْنَا عَلَيْكُمُ الْمَنَّ وَالسَّلْوَىٰ
Éy yéen waa giir Banii-Israayiil, musal Nanu leen ci seenub noon, Nu digeek yéen fa wàllug ndeyjooru tundu Sinaay wa. Nu wàcceel leen yàpp.
81كُلُوا مِن طَيِّبَاتِ مَا رَزَقْنَاكُمْ وَلَا تَطْغَوْا فِيهِ فَيَحِلَّ عَلَيْكُمْ غَضَبِي ۖ وَمَن يَحْلِلْ عَلَيْهِ غَضَبِي فَقَدْ هَوَىٰ
“Lekk-leen ci lu teey [sell] li Nu leen wërsëgale te buleen ca beew, [bu ngeen beewee], kon Sama mer day wàcc ci seen kaw : te képp ku Sama mer wàcc ci kawam, sànku na.
82وَإِنِّي لَغَفَّارٌ لِّمَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا ثُمَّ اهْتَدَىٰ
Te moo ne Man dey ab Jéggalaakoon laa ci képp ku tuub, te gëm, te jëf u yiw tey jubal”.
83۞ وَمَا أَعْجَلَكَ عَن قَوْمِكَ يَا مُوسَىٰ
“Waaw Muusaa, ana lan moo tax nga jiitu saw nit ? ”
84قَالَ هُمْ أُولَاءِ عَلَىٰ أَثَرِي وَعَجِلْتُ إِلَيْكَ رَبِّ لِتَرْضَىٰ
Mu ne ko ñoom dey ñanga ca sama ginnaaw. Ma yàkkamtee agsi ci Yaw ba am sa ngërëm.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — Taha 82

Simoore Taha Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te moo ne Man dey ab Jéggalaakoon laa ci képp…

Simoore Aaya 82/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers