Al-Anbiya · 102/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
لَا يَسْمَعُونَ حَسِيسَهَا ۖ وَهُمْ فِي مَا اشْتَهَتْ أَنفُسُهُمْ خَالِدُونَ ۝١٠٢
Laa yasma`oona hasee sahaa wa hum fee mash tahat anfusuhum khaalidoon
📖 Tekkim Wolof
Duñu dégg yëngoom ga te ñoom ñangay nekk ca lu neex seen bakkan ba fàwwu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 100-104 — Al-Anbiya

100لَهُمْ فِيهَا زَفِيرٌ وَهُمْ فِيهَا لَا يَسْمَعُونَ
Te ñoom am nañu ca biir foofa ay yikkat, te ñoom duñu fa mën a dégg dara.
101إِنَّ الَّذِينَ سَبَقَتْ لَهُم مِّنَّا الْحُسْنَىٰ أُولَٰئِكَ عَنْهَا مُبْعَدُونَ
Ña nga xam ne digoon Nanu leen xéewal yu jëkk ya jóge ci Nun, ñoom ñu Nuy soreel [Safara soosu] lañu.
102لَا يَسْمَعُونَ حَسِيسَهَا ۖ وَهُمْ فِي مَا اشْتَهَتْ أَنفُسُهُمْ خَالِدُونَ
Duñu dégg yëngoom ga te ñoom ñangay nekk ca lu neex seen bakkan ba fàwwu.
103لَا يَحْزُنُهُمُ الْفَزَعُ الْأَكْبَرُ وَتَتَلَقَّاهُمُ الْمَلَائِكَةُ هَٰذَا يَوْمُكُمُ الَّذِي كُنتُمْ تُوعَدُونَ
Tiit mu rëy ma duleen tiital, te Malaaka ya danañu leen gatandu naan : “Lii mooy seen bis ba ñu leen digoon”.
104يَوْمَ نَطْوِي السَّمَاءَ كَطَيِّ السِّجِلِّ لِلْكُتُبِ ۚ كَمَا بَدَأْنَا أَوَّلَ خَلْقٍ نُّعِيدُهُ ۚ وَعْدًا عَلَيْنَا ۚ إِنَّا كُنَّا فَاعِلِينَ
Bis boobu Dananu taxañ asamaam ni Nuy taxañe këyit gu am bind. Na nu tàmbalee woon sos ga bu jëkk ba, Dananu dellu [defaat ko] ; muy dëel bu Nu warlu [lu Nuy def la] !
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
102Aaya

Tekki — Al-Anbiya 102

Simoore Al-Anbiya Aaya 102 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Duñu dégg yëngoom ga te ñoom ñangay nekk ca lu…

Simoore Aaya 102/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 100–104. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers