Al-Anbiya · 101/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
إِنَّ الَّذِينَ سَبَقَتْ لَهُم مِّنَّا الْحُسْنَىٰ أُولَٰئِكَ عَنْهَا مُبْعَدُونَ ۝١٠١
Innal lazeena sabaqat lahum minnal husnaaa ulaaa`ika `anhaa mub`adoon
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne digoon Nanu leen xéewal yu jëkk ya jóge ci Nun, ñoom ñu Nuy soreel [Safara soosu] lañu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 99-103 — Simoore Al-Anbiya

99لَوْ كَانَ هَٰؤُلَاءِ آلِهَةً مَّا وَرَدُوهَا ۖ وَكُلٌّ فِيهَا خَالِدُونَ
Bu fekkoon ne ay yàlla lañu, kon duñu ca tàbbi ; nit ñooña ñépp dañu fay béel.
100لَهُمْ فِيهَا زَفِيرٌ وَهُمْ فِيهَا لَا يَسْمَعُونَ
Te ñoom am nañu ca biir foofa ay yikkat, te ñoom duñu fa mën a dégg dara.
101إِنَّ الَّذِينَ سَبَقَتْ لَهُم مِّنَّا الْحُسْنَىٰ أُولَٰئِكَ عَنْهَا مُبْعَدُونَ
Ña nga xam ne digoon Nanu leen xéewal yu jëkk ya jóge ci Nun, ñoom ñu Nuy soreel [Safara soosu] lañu.
102لَا يَسْمَعُونَ حَسِيسَهَا ۖ وَهُمْ فِي مَا اشْتَهَتْ أَنفُسُهُمْ خَالِدُونَ
Duñu dégg yëngoom ga te ñoom ñangay nekk ca lu neex seen bakkan ba fàwwu.
103لَا يَحْزُنُهُمُ الْفَزَعُ الْأَكْبَرُ وَتَتَلَقَّاهُمُ الْمَلَائِكَةُ هَٰذَا يَوْمُكُمُ الَّذِي كُنتُمْ تُوعَدُونَ
Tiit mu rëy ma duleen tiital, te Malaaka ya danañu leen gatandu naan : “Lii mooy seen bis ba ñu leen digoon”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
101Aaya

Tekki — Al-Anbiya 101

Simoore Al-Anbiya Aaya 101 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne digoon Nanu leen xéewal yu jëkk…

Simoore Aaya 101/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 99–103. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers