Al-Anbiya · 107/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا رَحْمَةً لِّلْعَالَمِينَ ۝١٠٧
Wa maaa arsalnaaka illaa rahmatal lil`aalameen
📖 Tekkim Wolof
Yónniwunu la ngir dara lu dul nga nekk yërmaandey waa àddina.

🎧 Dégg


📜 Aaya 105-109 — Simoore Al-Anbiya

105وَلَقَدْ كَتَبْنَا فِي الزَّبُورِ مِن بَعْدِ الذِّكْرِ أَنَّ الْأَرْضَ يَرِثُهَا عِبَادِيَ الصَّالِحُونَ
Te bind Nanu ba noppi ca Téere ya ginnaaw bind ga nekk [ca Lawhul Mahfuuz] Àlluwa ja, ne suuf si Sunu jaam yu yiw yi ñoo koy donn”.
106إِنَّ فِي هَٰذَا لَبَلَاغًا لِّقَوْمٍ عَابِدِينَ
Nekk na ci biir loolu ab jottali ñeel aw nit ñuy jaamu Yàlla !
107وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا رَحْمَةً لِّلْعَالَمِينَ
Yónniwunu la ngir dara lu dul nga nekk yërmaandey waa àddina.
108قُلْ إِنَّمَا يُوحَىٰ إِلَيَّ أَنَّمَا إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَهَلْ أَنتُم مُّسْلِمُونَ
Neel : “Man dey dañu may soloo doŋŋ : Waaye seen Yàlla jenn doŋŋ la ; kon ndax yéen dungeen wommatu jébbalu? ” [dugg ci Lislaam]
109فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ آذَنتُكُمْ عَلَىٰ سَوَاءٍ ۖ وَإِنْ أَدْرِي أَقَرِيبٌ أَم بَعِيدٌ مَّا تُوعَدُونَ
Bu ñu dëddoo, neel : “Xamal naa leen loo xam ne noo ca yem ; mu di ndax li ñu leen dig dafa jegeñ walla dafa sori.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
107Aaya

Tekki — Al-Anbiya 107

Simoore Al-Anbiya Aaya 107 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónniwunu la ngir dara lu dul nga nekk yërmaandey waa…

Simoore Aaya 107/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 105–109. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers