Al-Anbiya · 108/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
قُلْ إِنَّمَا يُوحَىٰ إِلَيَّ أَنَّمَا إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَهَلْ أَنتُم مُّسْلِمُونَ ۝١٠٨
Qul innamaa yoohaa ilaiya annamaaa ilaahukum illaahunw Waahid, fahal antum muslimoon
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Man dey dañu may soloo doŋŋ : Waaye seen Yàlla jenn doŋŋ la ; kon ndax yéen dungeen wommatu jébbalu? ” [dugg ci Lislaam]

🎧 Dégg


📜 Aaya 106-110 — Simoore Al-Anbiya

106إِنَّ فِي هَٰذَا لَبَلَاغًا لِّقَوْمٍ عَابِدِينَ
Nekk na ci biir loolu ab jottali ñeel aw nit ñuy jaamu Yàlla !
107وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا رَحْمَةً لِّلْعَالَمِينَ
Yónniwunu la ngir dara lu dul nga nekk yërmaandey waa àddina.
108قُلْ إِنَّمَا يُوحَىٰ إِلَيَّ أَنَّمَا إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَهَلْ أَنتُم مُّسْلِمُونَ
Neel : “Man dey dañu may soloo doŋŋ : Waaye seen Yàlla jenn doŋŋ la ; kon ndax yéen dungeen wommatu jébbalu? ” [dugg ci Lislaam]
109فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ آذَنتُكُمْ عَلَىٰ سَوَاءٍ ۖ وَإِنْ أَدْرِي أَقَرِيبٌ أَم بَعِيدٌ مَّا تُوعَدُونَ
Bu ñu dëddoo, neel : “Xamal naa leen loo xam ne noo ca yem ; mu di ndax li ñu leen dig dafa jegeñ walla dafa sori.
110إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ مِنَ الْقَوْلِ وَيَعْلَمُ مَا تَكْتُمُونَ
Moom dey xam na li ñuy biral ciy wax ak it li ngeen di nëbb.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
108Aaya

Tekki — Al-Anbiya 108

Simoore Al-Anbiya Aaya 108 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Man dey dañu may soloo doŋŋ : Waaye…

Simoore Aaya 108/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 106–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers