Al-Anbiya · 15/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
فَمَا زَالَت تِّلْكَ دَعْوَاهُمْ حَتَّىٰ جَعَلْنَاهُمْ حَصِيدًا خَامِدِينَ ۝١٥
Famaa zaalat tilka da`waahum hattaa ja`alnaahum haseedan khaamideen
📖 Tekkim Wolof
Xawuñoo eggale seen njàmbat loolu ba Nu def leen ni am ngóobit mu ne selaw.

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Al-Anbiya

13لَا تَرْكُضُوا وَارْجِعُوا إِلَىٰ مَا أُتْرِفْتُمْ فِيهِ وَمَسَاكِنِكُمْ لَعَلَّكُمْ تُسْأَلُونَ
Buleen daw de. Delluleen fa seen kër ya ngeen nekkoon di xéewlu, ndax xéy-na dees na leen laaj.
14قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Ñu ne : “Ngalla nun ! Nun dey ay tooñkat lanu woon”.
15فَمَا زَالَت تِّلْكَ دَعْوَاهُمْ حَتَّىٰ جَعَلْنَاهُمْ حَصِيدًا خَامِدِينَ
Xawuñoo eggale seen njàmbat loolu ba Nu def leen ni am ngóobit mu ne selaw.
16وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاءَ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindinu asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante ngir fo.
17لَوْ أَرَدْنَا أَن نَّتَّخِذَ لَهْوًا لَّاتَّخَذْنَاهُ مِن لَّدُنَّا إِن كُنَّا فَاعِلِينَ
Su Nu bëggoon po, kon [Dunu soxla bind dara], ci Sunu bopp la Nu koy sose, ndegam lu Nu nammoon a def la
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Anbiya 15

Simoore Al-Anbiya Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xawuñoo eggale seen njàmbat loolu ba Nu def leen ni…

Simoore Aaya 15/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers