Al-Anbiya · 14/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ ١٤
Transliteration
Qaaloo yaa wailanaaa innaa kunnaa zaalimeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Ngalla nun ! Nun dey ay tooñkat lanu woon”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 12-16 — Al-Anbiya
12فَلَمَّا أَحَسُّوا بَأْسَنَا إِذَا هُم مِّنْهَا يَرْكُضُونَ
Ba ñu yégee Sunu mbugal, ñoom daw nañu [di jéem a génn dëkk ya].
13لَا تَرْكُضُوا وَارْجِعُوا إِلَىٰ مَا أُتْرِفْتُمْ فِيهِ وَمَسَاكِنِكُمْ لَعَلَّكُمْ تُسْأَلُونَ
Buleen daw de. Delluleen fa seen kër ya ngeen nekkoon di xéewlu, ndax xéy-na dees na leen laaj.
14قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Ñu ne : “Ngalla nun ! Nun dey ay tooñkat lanu woon”.
15فَمَا زَالَت تِّلْكَ دَعْوَاهُمْ حَتَّىٰ جَعَلْنَاهُمْ حَصِيدًا خَامِدِينَ
Xawuñoo eggale seen njàmbat loolu ba Nu def leen ni am ngóobit mu ne selaw.
16وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاءَ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindinu asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante ngir fo.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
14Aaya
Tekki — Al-Anbiya 14
Simoore Al-Anbiya Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Ngalla nun ! Nun dey ay tooñkat…Simoore Aaya 14/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








