Al-Anbiya · 40/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
بَلْ تَأْتِيهِم بَغْتَةً فَتَبْهَتُهُمْ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ رَدَّهَا وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ ۝٤٠
Bal taateehim baghtatan fatabhatuhum falaa yastatee`oona raddahaa wa laa hum yunzaroon
📖 Tekkim Wolof
Déedéet, ndekete yoo ci mbetteel la leen di dikkale, gëlëmal leen ; duñu ko mën a fànq, te kenn duleen ca yéexe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 38-42 — Simoore Al-Anbiya

38وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñuy wax naan : “Kañ la dig boobu di agsi ndegam ñu dëggu ngeen ? ”
39لَوْ يَعْلَمُ الَّذِينَ كَفَرُوا حِينَ لَا يَكُفُّونَ عَن وُجُوهِهِمُ النَّارَ وَلَا عَن ظُهُورِهِمْ وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
Ña weddi bu ñu xamoon waxtu wa nga xam ne duñu mën a feg safara say lakk seeni kanam walla seeni ginnaaw, te kenn duleen ca dimbali...
40بَلْ تَأْتِيهِم بَغْتَةً فَتَبْهَتُهُمْ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ رَدَّهَا وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ
Déedéet, ndekete yoo ci mbetteel la leen di dikkale, gëlëmal leen ; duñu ko mën a fànq, te kenn duleen ca yéexe.
41وَلَقَدِ اسْتُهْزِئَ بِرُسُلٍ مِّن قَبْلِكَ فَحَاقَ بِالَّذِينَ سَخِرُوا مِنْهُم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Yéjjeefoon na Yonent ya la jiitu woon. Faf ña doon yéjji, la ñu doon reetaan wàcc ci seen kaw.
42قُلْ مَن يَكْلَؤُكُم بِاللَّيْلِ وَالنَّهَارِ مِنَ الرَّحْمَٰنِ ۗ بَلْ هُمْ عَن ذِكْرِ رَبِّهِم مُّعْرِضُونَ
Neel : “Kan moo leen mëna yërëm guddi ak bëccëg ci Yërëmaakoon bi ? ” Teewul ñoom ñangay dëddoo tuddu seen Boroom [Fàttaliku Ko].
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — Al-Anbiya 40

Simoore Al-Anbiya Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déedéet, ndekete yoo ci mbetteel la leen di dikkale, gëlëmal…

Simoore Aaya 40/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers