Al-Anbiya · 6/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
مَا آمَنَتْ قَبْلَهُم مِّن قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا ۖ أَفَهُمْ يُؤْمِنُونَ ۝٦
Maaa aaamanat qablahum min qaryatin ahlaknaahaa a-fahum yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Xeet ya leen jiitu woon te gëmuñu, alag Nanu leen. [Kon] ñoon ndax danañu gëm ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Anbiya

4قَالَ رَبِّي يَعْلَمُ الْقَوْلَ فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۖ وَهُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Neel : “Sama Boroom xam na lépp lu ñu wax ; ci kaw asamaan yi ak suuf, mooy Aji-dégg di Aji-gis”.
5بَلْ قَالُوا أَضْغَاثُ أَحْلَامٍ بَلِ افْتَرَاهُ بَلْ هُوَ شَاعِرٌ فَلْيَأْتِنَا بِآيَةٍ كَمَا أُرْسِلَ الْأَوَّلُونَ
Waaye ñu naan : “Way-jaxasook ay gént rekk la ! Du lenn lu dul lu mu sos. Ndax [moom Yonent bi] waykat la. Nanu indil kaawtéef ni ñu ko daan yónnee ñu njëkk ña”.
6مَا آمَنَتْ قَبْلَهُم مِّن قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا ۖ أَفَهُمْ يُؤْمِنُونَ
Xeet ya leen jiitu woon te gëmuñu, alag Nanu leen. [Kon] ñoon ndax danañu gëm ?
7وَمَا أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِمْ ۖ فَاسْأَلُوا أَهْلَ الذِّكْرِ إِن كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Mësunoo yónni ñu la jiitu lu dul aw góor yu Nu soloo. Laajleen ña jotoon Téere ndeem xamu leen.
8وَمَا جَعَلْنَاهُمْ جَسَدًا لَّا يَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَمَا كَانُوا خَالِدِينَ
Defunuleen woon [boroom] yaram yu dul lekk ñam. Te it nekkuñu woon ñuy béel [dañu daa lekk, di wopp, di dee].
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Anbiya 6

Simoore Al-Anbiya Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xeet ya leen jiitu woon te gëmuñu, alag Nanu leen.…

Simoore Aaya 6/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers