Al-Anbiya · 7/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَمَا أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِمْ ۖ فَاسْأَلُوا أَهْلَ الذِّكْرِ إِن كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ ۝٧
Wa maaa arsalnaa qablaka illaa rijaalan nooheee ilaihim fas`aloo ahlaz zikri in kuntum laa ta`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Mësunoo yónni ñu la jiitu lu dul aw góor yu Nu soloo. Laajleen ña jotoon Téere ndeem xamu leen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Al-Anbiya

5بَلْ قَالُوا أَضْغَاثُ أَحْلَامٍ بَلِ افْتَرَاهُ بَلْ هُوَ شَاعِرٌ فَلْيَأْتِنَا بِآيَةٍ كَمَا أُرْسِلَ الْأَوَّلُونَ
Waaye ñu naan : “Way-jaxasook ay gént rekk la ! Du lenn lu dul lu mu sos. Ndax [moom Yonent bi] waykat la. Nanu indil kaawtéef ni ñu ko daan yónnee ñu njëkk ña”.
6مَا آمَنَتْ قَبْلَهُم مِّن قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا ۖ أَفَهُمْ يُؤْمِنُونَ
Xeet ya leen jiitu woon te gëmuñu, alag Nanu leen. [Kon] ñoon ndax danañu gëm ?
7وَمَا أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِمْ ۖ فَاسْأَلُوا أَهْلَ الذِّكْرِ إِن كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Mësunoo yónni ñu la jiitu lu dul aw góor yu Nu soloo. Laajleen ña jotoon Téere ndeem xamu leen.
8وَمَا جَعَلْنَاهُمْ جَسَدًا لَّا يَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَمَا كَانُوا خَالِدِينَ
Defunuleen woon [boroom] yaram yu dul lekk ñam. Te it nekkuñu woon ñuy béel [dañu daa lekk, di wopp, di dee].
9ثُمَّ صَدَقْنَاهُمُ الْوَعْدَ فَأَنجَيْنَاهُمْ وَمَن نَّشَاءُ وَأَهْلَكْنَا الْمُسْرِفِينَ
Topp, Nu def la Nu leen digoon. Daldi leen boole musal ak ku Nu soob. Yàqkat ya ñoom, Nu rey leen.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Anbiya 7

Simoore Al-Anbiya Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mësunoo yónni ñu la jiitu lu dul aw góor yu…

Simoore Aaya 7/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers