Al-Anbiya · 65/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
ثُمَّ نُكِسُوا عَلَىٰ رُءُوسِهِمْ لَقَدْ عَلِمْتَ مَا هَٰؤُلَاءِ يَنطِقُونَ ۝٦٥
Summa nukisoo `alaa ru`oosihim laqad `alimta maa haaa`ulaaa`i yantiqoon
📖 Tekkim Wolof
Ñu daldi far delluwaat ca seen kéefar ga, daldi ne : Xam nga ne ñii mënuñoo wax waay”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 63-67 — Simoore Al-Anbiya

63قَالَ بَلْ فَعَلَهُ كَبِيرُهُمْ هَٰذَا فَاسْأَلُوهُمْ إِن كَانُوا يَنطِقُونَ
Mu ne : “Déedéet, ki ko def mooy ki ci gën a mag ci ñoom. Laajleen ko ndegam mën nañoo wax”.
64فَرَجَعُوا إِلَىٰ أَنفُسِهِمْ فَقَالُوا إِنَّكُمْ أَنتُمُ الظَّالِمُونَ
Ñu dellu ca seeni xel, daldi wax ne : “Nun noo tooñ sunu bopp”.
65ثُمَّ نُكِسُوا عَلَىٰ رُءُوسِهِمْ لَقَدْ عَلِمْتَ مَا هَٰؤُلَاءِ يَنطِقُونَ
Ñu daldi far delluwaat ca seen kéefar ga, daldi ne : Xam nga ne ñii mënuñoo wax waay”.
66قَالَ أَفَتَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَنفَعُكُمْ شَيْئًا وَلَا يَضُرُّكُمْ
Mu ne : “Waaw, ndax dangeen di bàyyi Yàlla di jaamu loo xam ne mënuleen a jariñ dara te mënuleen a lor.
67أُفٍّ لَّكُمْ وَلِمَا تَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ ۖ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Kuf ma leen yéen ak li ngeen di jaamu bàyyi Yàlla ! Ndax dangeen dul xel-lu ? ”
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Al-Anbiya 65

Simoore Al-Anbiya Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu daldi far delluwaat ca seen kéefar ga, daldi ne…

Simoore Aaya 65/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers